From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
professing themselves to be wise, they became fools,
Ñu teg seen bopp ni boroomi xel, fekk ñu ñàkk xel lañu woon.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for ye suffer fools gladly, seeing ye yourselves are wise.
yéen boroom xel yi, aka ngeen a man a muñal ñi dof,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ye fools, did not he that made that which is without make that which is within also?
yéena ñàkk xel! xanaa du ki defar biti moo defar biir itam?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
then he said unto them, o fools, and slow of heart to believe all that the prophets have spoken:
noonu yeesu ne leen: «yéen daal, yéena ñàkk xel, te seen xol yéex a gëm li yonent yi yégle woon!
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ye fools and blind: for whether is greater, the gift, or the altar that sanctifieth the gift?
gumba yi! lan moo gën a màgg, sarax si walla saraxalukaay bi tax sarax si sell?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
we are fools for christ's sake, but ye are wise in christ; we are weak, but ye are strong; ye are honourable, but we are despised.
nun teg nañu nu ni ay dof ndax kirist, waaye yéen am ngeen xel ci kirist. néew nanu doole, waaye yéen am ngeen doole. nawees na leen, waaye nun dañu noo xeeb.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
are they ministers of christ? (i speak as a fool) i am more; in labours more abundant, in stripes above measure, in prisons more frequent, in deaths oft.
ndax surgay kirist lañu? --maa ngi wax waxi ku tàggoo ak sagoom nag — maa leen ko gën a doon. bu dee ci liggéey, maa leen ci man. bu dee ci li ñu nu tëj ci kaso, maa leen ko gën a miin. bu dee ci li ñu nu dóor ay yar, maa leen ëpple. leru naa dee ba tàyyi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: