Results for former translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

as obedient children, not fashioning yourselves according to the former lusts in your ignorance:

Wolof

gannaaw gaayi yàlla yu koy déggal ngeen, buleen toppati bëgg-bëgg, yi ngeen toppoon, bi ngeen xamagul yàlla.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

the former treatise have i made, o theophilus, of all that jesus began both to do and teach,

Wolof

yaw teyofil, téere bu jëkk, ba ma bindoon, ëmb na lépp li yeesu tàmbali woon a jëf ak a jàngale,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

that ye put off concerning the former conversation the old man, which is corrupt according to the deceitful lusts;

Wolof

maanaam ngeen yulli seen jikko ju bon, ji ngeen judduwaale te daan fés ci seeni jëf, te muy gën a yées, moom ak i bëgg-bëggam yuy naxe kese.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but call to remembrance the former days, in which, after ye were illuminated, ye endured a great fight of afflictions;

Wolof

fàttalikuleen bés yu jëkk ya, ba leeru yàlla tàbbee ci yéen; dékku ngeen xeex bu mag ciy fitna.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and god shall wipe away all tears from their eyes; and there shall be no more death, neither sorrow, nor crying, neither shall there be any more pain: for the former things are passed away.

Wolof

dina fomp bépp rangooñ ci seeni bët; te dee dootul am walla naqar walla jooy walla metit, ndaxte yëf yu jëkk ya wéy nañu.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,881,423,062 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK