From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
go
wokf
Last Update: 2019-02-15
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
i want go to
Last Update: 2020-05-01
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and he must needs go through samaria.
bi muy dem galile, waroon na jaar ci diiwaanu samari.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and whither i go ye know, and the way ye know.
te fa ma jëm, xam ngeen yoon wi.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
but now i go unto jerusalem to minister unto the saints.
waaye nag fi mu nekk maa ngi dem nii yerusalem, ngir dimbaliji gaayi yàlla yu sell ya fa nekk.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and if it be meet that i go also, they shall go with me.
su aajoo ma demal sama bopp, kon dinañu ànd ak man.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and if i also ask you, ye will not answer me, nor let me go.
te su ma leen laajee, dungeen tontu.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and they said unto them even as jesus had commanded: and they let them go.
taalibe yi tontu leen, ni leen yeesu digale woon, kon nit ñi bàyyi leen, ñu dem.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and as ye go, preach, saying, the kingdom of heaven is at hand.
bu ngeen demee nag, yégleleen naan: “nguuru yàlla aji kawe ji jegesi na.”
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and he said unto him, arise, go thy way: thy faith hath made thee whole.
noonu yeesu ne ko: «jógal dem; sa ngëm faj na la.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and after they had tarried there a space, they were let go in peace from the brethren unto the apostles.
bi loolu amee ñu toog fa ab diir, ba noppi bokk yi yiwi leen ci jàmm, ñu dellu ca ña leen yónni woon.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
after they were come to mysia, they assayed to go into bithynia: but the spirit suffered them not.
bi ñu agsee nag ci wetu diiwaanu misi, ñuy jéem a dugg diiwaanu bitini, waaye xelum yeesu mayuleen ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and at midnight there was a cry made, behold, the bridegroom cometh; go ye out to meet him.
«noonu ci xaaju guddi baat jib ne: “boroom séet baa ngi, génnleen, gatandu ko.”
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and another said, i have bought five yoke of oxen, and i go to prove them: i pray thee have me excused.
keneen ne: “damaa jënd léegi fukki yëkk, te damay dem nii, jéem leen a beyloo ba xam. maa ngi lay ñaan, nga jéggal ma.”
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and he came to the second, and said likewise. and he answered and said, i go, sir: and went not.
gannaaw gi, baay ba ñëw ca ñaareel ba, wax ko noonu. mu tontu ko ne: “bëgguma caa dem,” waaye gannaaw loolu xelam soppiku, mu dem ca.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
a little while, and ye shall not see me: and again, a little while, and ye shall see me, because i go to the father.
«ci kanam tuuti dungeen ma gisati. bu ñu ci tegee ab diir, ngeen gisaat ma.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference: