From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
muslims should be made aware of the value of paying tithing.
war nañu yee jullit yi ci nnjariñal génne asaka.
Last Update: 2023-02-27
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
a good man out of the good treasure of the heart bringeth forth good things: and an evil man out of the evil treasure bringeth forth evil things.
noonu nit ku baax, lu baax lay wax, jële ko ca fa mu denc lu baax, te nit ku bon, lu bon lay wax, jële ko ca fa mu denc lu bon.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and delivered just lot, vexed with the filthy conversation of the wicked:
waaye musal na lóot mi jub, mi sonnoon ndax ñaawteefi ñu dëng, ñooñu mu nekkaloon.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
none of the selected modes were compatible with the possible modes: %s
requested", "minimummaximum
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
Warning: Contains invisible HTML formatting
and, behold, certain of the scribes said within themselves, this man blasphemeth.
bi mu waxee loolu, ay xutbakat daldi ne ci seen biir: «nit kii mu ngi sosal yàlla.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and hereby we know that we are of the truth, and shall assure our hearts before him.
ci loolu lanu xame ne, nu ngi ci dëgg; te waxtu wu sunu xol di xeex ak nun, dinanu ko dalal ci kanamam; ndaxte yàllaa ëpp sunu xol te xam na lépp.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
be ye also patient; stablish your hearts: for the coming of the lord draweth nigh.
yéen itam nag muñleen te dëgëral seen xol, xam ne ñëwu boroom bi ci ndamam jege na.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and supper being ended, the devil having now put into the heart of judas iscariot, simon's son, to betray him;
yeesu ak taalibe yaa ngi doon reer. fekk na booba seytaane xiirtal yudaa, doomu simoŋ iskariyo, ngir mu wori yeesu.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
a good man out of the good treasure of his heart bringeth forth that which is good; and an evil man out of the evil treasure of his heart bringeth forth that which is evil: for of the abundance of the heart his mouth speaketh.
noonu nit ku baax, lu baax lay wax, ndax loolu la denc ci xolam, te nit ku bon, lu bon lay wax, ndaxte denc na lu bon ci xolam. ndaxte gémmiñ, la fees xolam lay wax.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and as the people were in expectation, and all men mused in their hearts of john, whether he were the christ, or not;
mbooloo maa ngay xaar, di séentook a laaj ci seen xel, ndax yaxya mooy almasi bi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and all they that heard them laid them up in their hearts, saying, what manner of child shall this be! and the hand of the lord was with him.
Ñi dégg nettali, bi jëm ci mbir yooyu, dañu koo denc ci seen xol te naan: «nu xale bii di mujje nag?» ndaxte leeroon na ne, dooley boroom baa ngi ànd ak moom.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and one of the elders saith unto me, weep not: behold, the lion of the tribe of juda, the root of david, hath prevailed to open the book, and to loose the seven seals thereof.
noonu kenn ca mag ña ne ma: «bul jooy. xoolal, gayndeg giiru yuda, ki soqikoo ci daawuda, daan na, ba am sañ-sañu dindi tayu yi te ubbi téere bi.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference: