Results for hebrew translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

and he gathered them together into a place called in the hebrew tongue armageddon.

Wolof

noonu rab ya dajale buuri àddina si ci bérab bu tudd ci làkku yawut armagedon.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and a superscription also was written over him in letters of greek, and latin, and hebrew, this is the king of the jews.

Wolof

Ñu daaj mbind, mu tiim ko naan: «kii mooy buuru yawut yi.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he bearing his cross went forth into a place called the place of a skull, which is called in the hebrew golgotha:

Wolof

yeesu ci boppam gàddu bant ba, génn ngir dem ca fa ñuy wax bérabu kaaŋu bopp; ñu koy wooye golgota ci làkku yawut.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

(and when they heard that he spake in the hebrew tongue to them, they kept the more silence: and he saith,)

Wolof

bi ñu déggee, mu di leen wax ci làkku yawut, ñu gën ne xeram. noonu pool ne leen:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they had a king over them, which is the angel of the bottomless pit, whose name in the hebrew tongue is abaddon, but in the greek tongue hath his name apollyon.

Wolof

buuru njéeréer yi mooy malaakam kàmb gu xóot gi, moom lañu tudde ci làkku yawut, abadon, ak ci làkku gereg, apolyon, liy tekki «yàqkat.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

when pilate therefore heard that saying, he brought jesus forth, and sat down in the judgment seat in a place that is called the pavement, but in the hebrew, gabbatha.

Wolof

bi pilaat déggee loolu, mu daldi génne yeesu ca biti, dem toog ca jalub àttekaay ba, ca fu ñuy wax bérabu doj ya. ci làkku yawut ñu naan ko gabata.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

circumcised the eighth day, of the stock of israel, of the tribe of benjamin, an hebrew of the hebrews; as touching the law, a pharisee;

Wolof

xarafoon naa ca ayu-bés ga, bokk ci bànni israyil ci giiru ben-yamin, di ibrë ci deret ak ci meen. bu dee ci yoonu musaa ngeen bëgg a wax, ci tariixab farisen laa bokkoon;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when he had given him licence, paul stood on the stairs, and beckoned with the hand unto the people. and when there was made a great silence, he spake unto them in the hebrew tongue, saying,

Wolof

te kilifa ga may ko ko. noonu pool taxaw ca yéegukaay ba, tàllal loxoom mbooloo ma, ñu daldi ne tekk. mu wax ak ñoom ci làkku yawut ne:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and in those days, when the number of the disciples was multiplied, there arose a murmuring of the grecians against the hebrews, because their widows were neglected in the daily ministration.

Wolof

ca bés yooyu, naka taalibe yi di gën a bare, yawut yiy làkk gereg tàmbalee ñaxtu ci mbirum yawut tigi yi, te lii a ko waral: jigéen ñi seen jëkkër dee, te ñu bokk ci ñoom, naraalewuñu leen ca ndimbal, la ñuy séddale bés bu nekk.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,571,087,567 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK