From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
(for until the law sin was in the world: but sin is not imputed when there is no law.
bàkkaar kon nekkoon na ci àddina, bi yàlla di laata wàcce yoonu musaa. waaye gannaaw yoonu musaa tëddagul woon, bàkkaar du woon jàdd yoon.
and this is the condemnation, that light is come into the world, and men loved darkness rather than light, because their deeds were evil.
ci nii la àtte bi ame: leer gi ñëw na ci àddina, waaye nit lëndëm gi lañu taamu ndax seeni jëf yu bon.
beware lest any man spoil you through philosophy and vain deceit, after the tradition of men, after the rudiments of the world, and not after christ.
moytuleen ba kenn bañ leen a fàbbi ci ay xam-xami nit yuy naxi neen. xam-xam yu mel noonu, ñu ngi soqikoo ci aada yu nit tëral, ci aaday àddina, waaye soqikoowul ci kirist.
(of whom the world was not worthy:) they wandered in deserts, and in mountains, and in dens and caves of the earth.
Ñu ngi leen doon def noonu, fekk àddina sax yelloowul leen. Ñu ngi doon wëreelu ci àll yi ak ci tund yi, dal ci xunti yi ak ci kàmb yi.
i have manifested thy name unto the men which thou gavest me out of the world: thine they were, and thou gavest them me; and they have kept thy word.
«xamal naa sa tur nit, ñi nga tànne ci àddina te dénk ma leen. bokkoon nañu ci yaw, nga dénk ma leen, te sàmm nañu sa kàddu.
and base things of the world, and things which are despised, hath god chosen, yea, and things which are not, to bring to nought things that are:
li dul juddu bu rafet te mat a xeeb ci àddina, yàlla tànn na ko; yàlla tànn na li nekkul, ngir neenal li nekk.
if ye were of the world, the world would love his own: but because ye are not of the world, but i have chosen you out of the world, therefore the world hateth you.
Ñi bokk ci ñoom lañu bëgg. bu ngeen bokkoon ci ñoom, dinañu leen bëgg, ni ñu bëgge seeni ñoñ. waaye bokkuleen ci àddina, ndaxte maa leen tànn, ber leen. looloo tax ñu bañ leen.