From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
what do you do?
wayaw loy def nii
Last Update: 2017-01-13
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
do you hate me
Last Update: 2021-04-14
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and as ye would that men should do to you, do ye also to them likewise.
defal-leen nit ñi li ngeen bëgg, ñu defal leen ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
his mother saith unto the servants, whatsoever he saith unto you, do it.
yaayam daldi ne surga ya: «defleen lépp lu mu leen wax.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and he asked them, how many loaves have ye? and they said, seven.
yeesu laaj leen: «Ñaata mburu ngeen am?» Ñu ne ko: «juróom-ñaar.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
neither the seven loaves of the four thousand, and how many baskets ye took up?
te ndax fàttalikuwuleen itam juróom-ñaari mburu ya ngir ñeenti junniy góor ña, ak ñaata dàmba ngeen dajale woon ciy dammit?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and we desire that every one of you do shew the same diligence to the full assurance of hope unto the end:
waaye danoo bëgg kenn ku nekk ci yéen wone cawarte gu mel ni ga ngeen amoon, ba kera ngeen di am mat, gi ngeen di séentu.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
moreover, brethren, we do you to wit of the grace of god bestowed on the churches of macedonia;
gannaaw loolu bokk yi, danu leen a bëgg a xamal li yiwu yàlla jur ci biir mboolooy ñi gëm te nekk ci diiwaanu maseduwan.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and when the seven among four thousand, how many baskets full of fragments took ye up? and they said, seven.
yeesu neeti leen: «te bés bi ma dammee juróom-ñaari mburu yi ngir ñeenti junni ñi, ñaata dàmba yu fees ak dammit ngeen dajale woon?» Ñu ne ko: «juróom ñaar.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and jesus saith unto them, how many loaves have ye? and they said, seven, and a few little fishes.
yeesu ne leen: «Ñaata mburu ngeen am?» Ñu tontu ko: «juróom-ñaari mburu ak ay jën yu ndaw.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
when i brake the five loaves among five thousand, how many baskets full of fragments took ye up? they say unto him, twelve.
bi ma dammee juróomi mburu ya ngir juróomi junni ña, ñaata pañe yu fees ak ay dammit ngeen ca dajale woon?» Ñu tontu ko: «fukk ak ñaar.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
he saith unto them, how many loaves have ye? go and see. and when they knew, they say, five, and two fishes.
yeesu laaj leen: «Ñaata mburu ngeen am? demleen seeti.» Ñu dem seeti ne ko: «juróomi mburu ak ñaari jën.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
using button1 without modifiers can prevent any left click and thus break your configuration. do you really want to set "%s" button to button1 ?
Ñörĩ butão-1 fi, loolu mënna indil jöffe-jöffe ndaxte tere ñörĩ ko naka yoon.ndax nga bögge teg "%s" ngir butão-1 düggë-düggë ?
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
Warning: Contains invisible HTML formatting
but i say unto you, love your enemies, bless them that curse you, do good to them that hate you, and pray for them which despitefully use you, and persecute you;
waaye man maa ngi leen di wax ne, soppleen seeni bañaale te ñaanal ñi leen di fitnaal,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
the new value for the %(binding)s binding for the action %(action)s in plugin %(plugin)s conflicts with the action %(action_conflict)s of the %(plugin_conflict)s plugin. do you wish to disable %(action_conflict)s in the %(plugin_conflict)s plugin?
defaay %(action)s u %(binding)s ci biir %(plugin)sdef na jöffë-jöffë ak %(action_conflict)s ci biir %(plugin_conflict)s. ndax nga bögge fayal %(action_conflict)s ci biir %(plugin_conflict)s ?
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference: