Results for howbeit translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

howbeit we must be cast upon a certain island.

Wolof

waaye war nanoo luf cib dun.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

howbeit no man spake openly of him for fear of the jews.

Wolof

waaye kenn ñemewu koo tudd ca kaw, ndaxte dañoo ragaloon yawut ya.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

howbeit in vain do they worship me, teaching for doctines the commandments of men.

Wolof

seen màggal amul benn njariñ,ci li ñuy jàngale dénkaaney nit kese.”»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

howbeit the most high dwelleth not in temples made with hands; as saith the prophet,

Wolof

«moona aji kawe ji du dëkk ci fu loxol nit defar; moom la ab yonent wax ne:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for some, when they had heard, did provoke: howbeit not all that came out of egypt by moses.

Wolof

Ñan ñoo dégg baatu yàlla bi nag te di ko dëddu? xanaa ña musaa génne woon misra ñépp.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

brethren, be not children in understanding: howbeit in malice be ye children, but in understanding be men.

Wolof

bokk yi, buleen melati ni ay xale, ci ni ngeen di xalaate. ci lu jëm ci lu bon, mel-leen ni ay xale, waaye ci seeni xalaat, mel-leen ni ay mag.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

howbeit that was not first which is spiritual, but that which is natural; and afterward that which is spiritual.

Wolof

yaram wi soloo ndamu xelum yàlla jiituwul; yaramu doom aadama moo jiitu; yaramu ndam li moo ci topp.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

(howbeit there came other boats from tiberias nigh unto the place where they did eat bread, after that the lord had given thanks:)

Wolof

waaye yeneen gaal yu jóge dëkku tiberyàdd ñëw, teer ca wetu fa ñu lekke woon mburu ma, gannaaw bi boroom bi santee yàlla ba noppi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for he that speaketh in an unknown tongue speaketh not unto men, but unto god: for no man understandeth him; howbeit in the spirit he speaketh mysteries.

Wolof

ndaxte kiy wax aw làkk, waxul ak nit ñi, waaye yàlla lay waxal, ndaxte kenn déggul li muy wax. dafay wax ay mbóot ci xelam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

howbeit we speak wisdom among them that are perfect: yet not the wisdom of this world, nor of the princes of this world, that come to nought:

Wolof

moona am na xam-xam bu nuy yégal ñi mat, xam-xam bu bokkul ci àddina si, te njiiti àddina si xamuñu ko, ñoom ñi nar a wéy.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

howbeit there is not in every man that knowledge: for some with conscience of the idol unto this hour eat it as a thing offered unto an idol; and their conscience being weak is defiled.

Wolof

waaye ñépp xamuñu loolu. am na ñu tàmmoon xërëm yi, te léegi, bu ñu lekkatee yàppu sarax yi, dañuy xalaat ne, xërëm lañu ko jagleel. seen xel dafa leen di yedd, ndaxte ci seen ñàkka xam dañuy foog ne, taq nañu sobe ndax ñam woowu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

howbeit they looked when he should have swollen, or fallen down dead suddenly: but after they had looked a great while, and saw no harm come to him, they changed their minds, and said that he was a god.

Wolof

nit ñi di xaar mu newi, mbaa mu ne dàll, dee; waaye bi ñu négee lu yàgg te gis ne dara jotu ko, ñu soppi xel ne: «kii yàlla la.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,144,504,472 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK