From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
thou hypocrite, first cast out the beam out of thine own eye; and then shalt thou see clearly to cast out the mote out of thy brother's eye.
naaféq, jëkkal a dindi gànj gi ci sa bët, te noonu dinga man a gis bu leer, ngir dindi ñax gi ci sa bëtu mbokk.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
the lord then answered him, and said, thou hypocrite, doth not each one of you on the sabbath loose his ox or his ass from the stall, and lead him away to watering?
boroom bi tontu ko: «naaféq yi! ndax bésu noflaay bi, kenn ku nekk ci yéen du yiwee ca gétt ga yëkkam walla mbaamam ngir wëggi ko?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and in the morning, it will be foul weather to day: for the sky is red and lowring. o ye hypocrites, ye can discern the face of the sky; but can ye not discern the signs of the times?
te suba gi ngeen naan: “tey daal dina taw, ndax asamaan si dafa xonq te xiin.” kon man ngeen a ràññee melow asamaan, waaye mënuleen a ràññee firndey jamono ji nu tollu.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: