Results for i really mean it in translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

and said, this fellow said, i am able to destroy the temple of god, and to build it in three days.

Wolof

«kii nee woon na: “man naa toj kër yàlla ga, tabaxaat ko ci ñetti fan.”»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when joseph had taken the body, he wrapped it in a clean linen cloth,

Wolof

noonu yuusufa fab jëmm ja, laxas ko ci càngaay lu set,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when his disciples heard of it, they came and took up his corpse, and laid it in a tomb.

Wolof

ba taalibey yaxya déggee loolu, ñu ñëw, fab néew ba, suul ko ci bàmmeel.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

when they that fed them saw what was done, they fled, and went and told it in the city and in the country.

Wolof

sàmm ya gis li xew, daw nettaliji mbir mi ca dëkk ba ak ca àll ba.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

then took they the body of jesus, and wound it in linen clothes with the spices, as the manner of the jews is to bury.

Wolof

Ñu jël néewu yeesu, laxas ko ci càngaay, boole ko ak cuuraay li, ni ko yawut yi tàmmoo def, bu ñuy waajal néew.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they that fed the swine fled, and told it in the city, and in the country. and they went out to see what it was that was done.

Wolof

noonu sàmm ya daw ca dëkk ba ak ca àll ba, nettaliji mbir mi, ba nit ñi ñëw, seet li xew.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he took it down, and wrapped it in linen, and laid it in a sepulchre that was hewn in stone, wherein never man before was laid.

Wolof

gannaaw loolu mu wàcce ko ca bant ba, laxas ko ci càngaay, dugal ko cib bàmmeel bu ñu yett ciw doj te musuñu caa def kenn.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and laid it in his own new tomb, which he had hewn out in the rock: and he rolled a great stone to the door of the sepulchre, and departed.

Wolof

dugal ko ca bàmmeel bu bees, ba mu yettaloon boppam ciw doj. mu béraŋ doj wu mag ca buntu bàmmeel ba, dem.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and saying, thou that destroyest the temple, and buildest it in three days, save thyself. if thou be the son of god, come down from the cross.

Wolof

naan: «yaw mi man a toj kër yàlla ga, tabaxaat ko ci ñetti fan, musalal sa bopp; boo nekkee doomu yàlla, wàccal ci bant bi.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

no man, when he hath lighted a candle, putteth it in a secret place, neither under a bushel, but on a candlestick, that they which come in may see the light.

Wolof

«kenn du taal làmp, ba noppi di ko duggal cig kàmb, walla di ci këpp leget. daf koy wékk, ngir mu leeral ñiy dugg.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and every spirit that confesseth not that jesus christ is come in the flesh is not of god: and this is that spirit of antichrist, whereof ye have heard that it should come; and even now already is it in the world.

Wolof

waaye mépp xel mu nanguwul yeesu, bokkul ci yàlla. xel moomu mooy xelum bañaaleb kirist, mi ngeen déggoon ne dina ñëw, te léegi sax mu ngi ci biir àddina.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

after the same manner also he took the cup, when he had supped, saying, this cup is the new testament in my blood: this do ye, as oft as ye drink it, in remembrance of me.

Wolof

noonu itam bi ñu lekkee ba noppi, mu jël kaas bi ne leen: «kaas bii mooy misaal kóllëre gu bees, gi yàlla fas jaarale ko ci sama deret. defleen lii ngir fàttaliku ma.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,781,152,278 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK