From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
knowing this first, that no prophecy of the scripture is of any private interpretation.
waaye jëkkleena xam ne, amul jenn waxu yonent ci mbind mi, ju balle ci xelu boppam.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but elymas the sorcerer (for so is his name by interpretation) withstood them, seeking to turn away the deputy from the faith.
waaye elimas, boroom xam-xam bu ñuul bi --ndaxte loolu la turam di tekki — di leen dogale, ngir bañ boroom réew ma gëm.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
now there was at joppa a certain disciple named tabitha, which by interpretation is called dorcas: this woman was full of good works and almsdeeds which she did.
amoon na nag ci dëkku yope taalibe bu jigéen bu tudd tabita, liy tekki «dorkas,» maanaam «kewel,» te muy wéy ci jëf yu baax ak saraxe.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
to whom also abraham gave a tenth part of all; first being by interpretation king of righteousness, and after that also king of salem, which is, king of peace;
noonu ibraayma fab fukkeelu cér bi, maanaam asaka, ci li mu jële woon ci xare ba lépp, jox ko. ci lu jëkk turu melkisedeg mi ngi tekki «buur bu jub bi.» gannaaw loolu mooy buuru salem, tur woowu mooy tekki «buuru jàmm.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he brought him to jesus. and when jesus beheld him, he said, thou art simon the son of jona: thou shalt be called cephas, which is by interpretation, a stone.
noonu mu yóbbu ko ci yeesu. yeesu xool ko ne ko: «yaa di simoŋ, doomu yowaana. dinañu la wooye sefas.» sefas mi ngi tekki «piyeer,» maanaam «xeer.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and said unto him, go, wash in the pool of siloam, (which is by interpretation, sent.) he went his way therefore, and washed, and came seeing.
«demal sëlmu ci bëtu silowe.» silowe mi ngi tekki «yónni nañu ko.» gumba ga daldi dem sëlmuji, dellusi di gis.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: