From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
whom i have sent unto you for the same purpose, that he might know your estate, and comfort your hearts;
lii moo tax ma yebal ko ci yéen: ngeen xam xebaar bi jóge ci nun, te it mu dëfël seen xol.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but i trust in the lord jesus to send timotheus shortly unto you, that i also may be of good comfort, when i know your state.
gannaaw loolu, bu soobee boroom bi yeesu, yaakaar naa ne, dinaa leen yónnee timote balaa yàgg, ngir sama xel dal ci xam nan ngeen def.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for this cause, when i could no longer forbear, i sent to know your faith, lest by some means the tempter have tempted you, and our labour be in vain.
noonu ba ma ko mënatul a dékku, yónnee naa, ngir xam fu seen ngëm tollu, ngir ragal seytaane fiir leen, ba sunu ñaq neen.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.