Results for light based translation from English to Wolof

English

Translate

light based

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

for my yoke is easy, and my burden is light.

Wolof

ndaxte sama kilifteef lewet na te sama yen diisul.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

in him was life; and the life was the light of men.

Wolof

ci moom la dund nekk, te dund googu mooy leeral nit ñi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

take heed therefore that the light which is in thee be not darkness.

Wolof

moytul ndax leer gi nekk ci yaw du lëndëm.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

he was not that light, but was sent to bear witness of that light.

Wolof

moom ci boppam du woon leer gi, waaye ñëw na ngir seedeel leer gi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the light shineth in darkness; and the darkness comprehended it not.

Wolof

leer gi feeñ na ci biir lëndëm, te lëndëm gi jàppu ko.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

a light to lighten the gentiles, and the glory of thy people israel.

Wolof

muy leer giy leeral xeet yi,di ndamu israyil say gaay.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and no marvel; for satan himself is transformed into an angel of light.

Wolof

te loolu jaaxalu nu, ndaxte seytaane moom ci boppam day mbubboo malaakam leer.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but if a man walk in the night, he stumbleth, because there is no light in him.

Wolof

waaye kuy dox guddi, dina fakkastalu, ndaxte leer nekkul ci moom.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and art confident that thou thyself art a guide of the blind, a light of them which are in darkness,

Wolof

yaa ngi teg sa bopp wommatkatu gumba yi ak leeru ñi nekk cig lëndëm.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but all things that are reproved are made manifest by the light: for whatsoever doth make manifest is light.

Wolof

waaye leer, lu mu ëmb, fésal ko.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and was transfigured before them: and his face did shine as the sun, and his raiment was white as the light.

Wolof

mu soppiku fa seen kanam, xar-kanamam di melax nib jant, te ay yéreem weex ni leer.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

they shall hunger no more, neither thirst any more; neither shall the sun light on them, nor any heat.

Wolof

dootuñu xiif, dootuñu mar.jant mbaa weneen tàngaay du leen lakk,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they that were with me saw indeed the light, and were afraid; but they heard not the voice of him that spake to me.

Wolof

Ñi ma àndaloon gis nañu leer ga, waaye dégguñu baatu ka doon wax ak man.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the nations of them which are saved shall walk in the light of it: and the kings of the earth do bring their glory and honour into it.

Wolof

xeeti àddina dinañu dox cig leeram, te buuri àddina dinañu ca indi seen ndam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the lord commended the unjust steward, because he had done wisely: for the children of this world are in their generation wiser than the children of light.

Wolof

njaatige ba nag daldi naw ni bëkk-néeg bu njublaŋ boobu muuse woon. ndaxte ñi bokk ci àddina ñoo gën a muus ci li ñu jote ci seen diggante ak seen moroom, ba raw ñi bokk ci leeru yàlla.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

again, a new commandment i write unto you, which thing is true in him and in you: because the darkness is past, and the true light now shineth.

Wolof

teewul ndigal lu bees laa leen di bind, lu amoon ci dundu yeesu, te am it ci seen dund; ndaxte lëndëm gaa ngi wéy, te leer gu wóor gi fenk na xaat.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

either what woman having ten pieces of silver, if she lose one piece, doth not light a candle, and sweep the house, and seek diligently till she find it?

Wolof

«te it bu jigéen dencoon fukki libidoor, benn réer ca, nu muy def? ndax du taal ab làmp, bale kër ga, seet fu nekk, ba gis ko?

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

immediately after the tribulation of those days shall the sun be darkened, and the moon shall not give her light, and the stars shall fall from heaven, and the powers of the heavens shall be shaken:

Wolof

«gannaaw metitu bés yooyule nag, ca saa sa jant bi dina lëndëm te weer wi dootul leer; biddiiw yi dinañu fàq, daanu ci asamaan, te kàttani asamaan yi yengu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and there shall be no night there; and they need no candle, neither light of the sun; for the lord god giveth them light: and they shall reign for ever and ever.

Wolof

guddi dootul am, te kenn dootul soxla leeru làmp walla naaju jant, ndaxte boroom bi yàlla moo leen di leeral. te dinañu nguuru ba fàww.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the light of a candle shall shine no more at all in thee; and the voice of the bridegroom and of the bride shall be heard no more at all in thee: for thy merchants were the great men of the earth; for by thy sorceries were all nations deceived.

Wolof

niitug làmp du tàkkati,te baatu boroom séet ak séetam dootul jib ci yaw ba fàww.ndaxte say baana-baana ñoo yilifoon àddina,te xeet yépp réer nañu ndax say luxus.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
8,920,035,737 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK