Results for mighty translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

and he did not many mighty works there because of their unbelief.

Wolof

te yeesu defu fa kéemaan yu bare ndax seen ngëmadi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for he that is mighty hath done to me great things; and holy is his name.

Wolof

ndaxte ku màgg ki defal na ma lu réy.turam dafa sell.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

humble yourselves therefore under the mighty hand of god, that he may exalt you in due time:

Wolof

suufeel-leen seen bopp kon ci ron loxob yàlla bu am kàttan, ngir mu yékkati leen ci jamono ju ko soob.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and moses was learned in all the wisdom of the egyptians, and was mighty in words and in deeds.

Wolof

musaa nag di ku yeewu ci xam-xamu waa misra bépp, di jàmbaar ci wax ak jëf.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he could there do no mighty work, save that he laid his hands upon a few sick folk, and healed them.

Wolof

te yeesu mënu faa def ay kéemaan yu bare, lu dul teg loxo yenn jarag, wéral leen.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when he had spent all, there arose a mighty famine in that land; and he began to be in want.

Wolof

bi mu sànkee alalam jépp, xiif bu metti dal ca réew ma, mu tàmbalee ñàkk.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and suddenly there came a sound from heaven as of a rushing mighty wind, and it filled all the house where they were sitting.

Wolof

ca saa sa riir jollee asamaan, mel ni ngelaw lu gaaw te bare doole, daldi fees dell kër, ga ñu toog.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

(for he that wrought effectually in peter to the apostleship of the circumcision, the same was mighty in me toward the gentiles:)

Wolof

ndaxte ni yàlla jëfe ci piyeer, miy ndawam ci yawut yi, noonu it la jëfe ci man, may ndawam ci ñi dul yawut.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they were all amazed at the mighty power of god. but while they wondered every one at all things which jesus did, he said unto his disciples,

Wolof

ku nekk waaru na ndax màggug yàlla. bi ñuy yéemu ci li mu doon def, yeesu ne taalibeem ya:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for ye see your calling, brethren, how that not many wise men after the flesh, not many mighty, not many noble, are called:

Wolof

bokk yi, seetleen seen nekkin, bi leen yàlla di woo. barewul woon ci yéen, ñi ñuy tudde ay boroom xam-xam mbaa ay boroom doole mbaa ñu rafet ab juddu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and said unto his servants, this is john the baptist; he is risen from the dead; and therefore mighty works do shew forth themselves in him.

Wolof

noonu mu ne ay surgaam: «kooku mooy yaxya, mi dekki; moo tax mu ànd ak kàttanu def ay kéemaan.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and a mighty angel took up a stone like a great millstone, and cast it into the sea, saying, thus with violence shall that great city babylon be thrown down, and shall be found no more at all.

Wolof

noonu malaaka mu am doole jël doj wu réy, sànni ko ci géej gi, naan: «nii lañuy sànnee ak doole babilon dëkk bu mag bi, mu ne meŋŋ.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and i saw another mighty angel come down from heaven, clothed with a cloud: and a rainbow was upon his head, and his face was as it were the sun, and his feet as pillars of fire:

Wolof

noonu ma gis meneen malaaka mu am doole, muy wàcce asamaan, làmboo niir. xon tiim ko, te xar-kanamam mel ni jant, te ay tànkam mel ni jumi safara.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and i heard as it were the voice of a great multitude, and as the voice of many waters, and as the voice of mighty thunderings, saying, alleluia: for the lord god omnipotent reigneth.

Wolof

ma dégg lu mel ni baatu mbooloo mu bare, mel ni riiru duusi géej, ni yenguy dënnu yu réy, naan:«aleluya!ndaxte sunu boroomyàlla aji kàttan jidugg na ci nguuram.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the kings of the earth, and the great men, and the rich men, and the chief captains, and the mighty men, and every bondman, and every free man, hid themselves in the dens and in the rocks of the mountains;

Wolof

noonu buuri àddina si, kilifa yi, njiiti xare yi, boroom alal yi, boroom kàttan yi, jaam yi ak gor yi, ñépp làqatuji ci xunti yi ak ci ron doji tund yi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,876,321,014 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK