Results for moses translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

and he answered and said unto them, what did moses command you?

Wolof

yeesu tontu leen ne: «lu leen yoonu musaa sant?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and were all baptized unto moses in the cloud and in the sea;

Wolof

sóobu nañu ca ndoxu géej ga ak ca niir wa, ba bokk noonu ci musaa.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and, behold, there appeared unto them moses and elias talking with him.

Wolof

naka noonu ñu gis yonenti yàlla musaa ak iliyas, di waxtaan ak yeesu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

abraham saith unto him, they have moses and the prophets; let them hear them.

Wolof

ibraayma ne ko: “say doomu baay, ñu ngeek yoonu musaa ak téerey yonent yi. nañu leen déggal.”

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and so terrible was the sight, that moses said, i exceedingly fear and quake:)

Wolof

te mbir moomu ñu doon seetaan dafa raglu, ba musaa naan: «damaa tiit bay lox.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and, behold, there talked with him two men, which were moses and elias:

Wolof

am ñaari nit di waxtaan ak moom, muy yonenti yàlla musaa ak iliyas.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

we know that god spake unto moses: as for this fellow, we know not from whence he is.

Wolof

xam nanu ne, yàlla wax na ak musaa; waaye kii, xamunu sax fu mu jóge.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and as moses lifted up the serpent in the wilderness, even so must the son of man be lifted up:

Wolof

te itam na musaa sampe woon ab bant ca diggu màndiŋ ma, takk ca jaan, ja mu defare woon xànjar, fàww ñu yékkatee noonu doomu nit ki,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and beginning at moses and all the prophets, he expounded unto them in all the scriptures the things concerning himself.

Wolof

noonu mu tàmbalee ci yonent yàlla musaa ba ci yonent yépp, tekkil leen li mbind mi wax lépp ci ay mbiram.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

did not moses give you the law, and yet none of you keepeth the law? why go ye about to kill me?

Wolof

xanaa du musaa moo leen jox ndigali yàlla yi? waaye kenn ci yéen sàmmu ko! lu tax ngeen bëgg maa rey?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he said unto him, if they hear not moses and the prophets, neither will they be persuaded, though one rose from the dead.

Wolof

waaye ibraayma tontu ko ne: “su ñu dégluwul musaa ak yonent yi, kon ku dekki sax, du tax ñu gëm.”»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

by faith moses, when he was come to years, refused to be called the son of pharaoh's daughter;

Wolof

ngëm a tax ba bi musaa màggee, muy bañ ñu koy wooye sëtu firawna.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and moses verily was faithful in all his house, as a servant, for a testimony of those things which were to be spoken after;

Wolof

musaa moom ku takku la woon ci lépp lu jëm ci waa kër yàlla. waaye jawriñ rekk la woon, ngir seede li yàlla waroon a yégle.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and certain men which came down from judaea taught the brethren, and said, except ye be circumcised after the manner of moses, ye cannot be saved.

Wolof

amoon na bés ay nit jóge diiwaanu yude, ñuy jàngal bokk yi ne leen: «ku xaraful, ni ko aaday musaa santaanee, doo man a mucc.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but there rose up certain of the sect of the pharisees which believed, saying, that it was needful to circumcise them, and to command them to keep the law of moses.

Wolof

ci kaw loolu ñeneen, ñi gëm waaye bokk ci tariixab farisen ya, daldi jóg ne: «fàww ñi dul yawut xaraf, te ñu dénk leen sàmm yoonu musaa.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they are informed of thee, that thou teachest all the jews which are among the gentiles to forsake moses, saying that they ought not to circumcise their children, neither to walk after the customs.

Wolof

dégg nañu ci sa mbir nag ne, yaa ngi jàngal yawut yépp, yi dëkk ci biir ñi dul yawut, ñu bàyyi yoonu musaa te bañ a xarafal seeni doom mbaa topp sunuy aada.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he charged him to tell no man: but go, and shew thyself to the priest, and offer for thy cleansing, according as moses commanded, for a testimony unto them.

Wolof

yeesu sant ko ne: «bu ko wax kenn, waaye demal won sa bopp saraxalekat bi, te nga jébbal yàlla sarax si yoonu musaa santaane, ngir ñu xam ne wér nga, te mu nekk seede ci ñoom.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

if a man on the sabbath day receive circumcision, that the law of moses should not be broken; are ye angry at me, because i have made a man every whit whole on the sabbath day?

Wolof

bu ngeen manee xarafal nit ci bésu noflaay bi, ngir bañ a wàcc yoonu musaa, lu tax nag ngeen mere ma, ndax li ma ci wéral nitu lëmm?

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and saith unto him, see thou say nothing to any man: but go thy way, shew thyself to the priest, and offer for thy cleansing those things which moses commanded, for a testimony unto them.

Wolof

«moytul a wax kenn dara, waaye demal won sa bopp saraxalekat bi, te nga jébbal yàlla sarax, si yoonu musaa santaane, ngir ñu xam ne wér nga, te mu nekk seede ci ñoom.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and as touching the dead, that they rise: have ye not read in the book of moses, how in the bush god spake unto him, saying, i am the god of abraham, and the god of isaac, and the god of jacob?

Wolof

te sax li jëm ci mbirum ndekkite, xanaa jànguleen lii yàlla wax ci tawreetu musaa ci saarum ngarab si: “maay yàllay ibraayma, isaaxa ak yanqóoba”?

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,744,260,046 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK