From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
i thank my god upon every remembrance of you,
yoon wu ma leen di xalaat, maa ngi sant yàlla sama boroom;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and thomas answered and said unto him, my lord and my god.
tomaa tontu ko ne: «sama boroom, sama yàlla!»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
i thank my god, i speak with tongues more than ye all:
maa ngi sant yàlla ci li may wax ay làkk, ba raw leen yéen ñépp.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
i thank my god, making mention of thee always in my prayers,
duma la noppee boole ci samay ñaan, di ci sant yàlla sama boroom,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but my god shall supply all your need according to his riches in glory by christ jesus.
te yàlla sama boroom, mi denc ci kirist yeesu xéewal yu dul jeex, dina ci faj seeni soxla yépp.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
i thank my god always on your behalf, for the grace of god which is given you by jesus christ;
duma jóg ci di sant yàlla sama boroom ci seen mbir ndax yiw, wi mu leen may ci seen bokk ci kirist yeesu.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
first, i thank my god through jesus christ for you all, that your faith is spoken of throughout the whole world.
kon nag li may jëkk a wax mooy lii: sant naa yàlla sama boroom, jaarale ko ci yeesu kirist, ngir yéen ñépp, ndaxte seen ngëm siiw na ci àddina sépp.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and lest, when i come again, my god will humble me among you, and that i shall bewail many which have sinned already, and have not repented of the uncleanness and fornication and lasciviousness which they have committed.
ragal naa, bu ma leen ganesiwaatee, yàlla sama boroom suufeel ma ci seen biir, ma naqarlu ci ñu bare ñu bàkkaaroon te dëdduwuñu seen yàqute, seen njaaloo ak seen ñaawteef, gi ñu doon def.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and about the ninth hour jesus cried with a loud voice, saying, eli, eli, lama sabachthani? that is to say, my god, my god, why hast thou forsaken me?
noonu ci wetu ñetti waxtu yeesu daldi wootee kàddu gu dëgër naan: «eli, eli, lema sabaktani?» liy tekki: «sama yàlla, sama yàlla, lu tax nga dëddu ma?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.