From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
if ye shall ask any thing in my name, i will do it.
lu ngeen ñaan ci sama tur, maa koy def.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and i will give him the morning star.
ni ma jële sañ-sañ ci sama baay. dinaa ko jox it biddiiwu njël.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
i will therefore chastise him, and release him.
kon nag dinaa ko dóorlu ay yar te bàyyi ko.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but i will tarry at ephesus until pentecost.
ba tey dinaa toog fii ci dëkku efes ba màggalu pàntakot,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
if then i do that which i would not, i consent unto the law that it is good.
kon nag gannaaw li may def du sama coobare, nangu naa ne yoonu musaa baax na.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and jesus saith unto him, i will come and heal him.
yeesu ne ko: «dinaa ñëw faj ko.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
i will not leave you comfortless: i will come to you.
duma leen bàyyi ngeen wéet. dinaa dellusi ci yéen.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
i will therefore that men pray every where, lifting up holy hands, without wrath and doubting.
li ma bëgg kon mooy lii: na góor ñi ñaan ci yàlla fu nekk, tàllal ko loxo yu sell, te bañ cee boole mer mbaa werante.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and whatsoever ye shall ask in my name, that will i do, that the father may be glorified in the son.
te it lu ngeen ñaan ci sama tur dinaa ko def, ngir doom ji feeñal ndamu baay bi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and i will pray the father, and he shall give you another comforter, that he may abide with you for ever;
te dinaa ñaan baay bi, mu jox leen beneen dimbalikat, buy nekk ak yéen ba abadan.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he saith unto them, follow me, and i will make you fishers of men.
yeesu ne leen: «Ñëwleen topp ci man, ma def leen nappkati nit.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but what i do, that i will do, that i may cut off occasion from them which desire occasion; that wherein they glory, they may be found even as we.
noonu may doxale nag dinaa ci sax, ngir ñiy damu, di wut yoon wu ñu aw ba yemale seen bopp ak nun, duñu ko am.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he said unto me, depart: for i will send thee far hence unto the gentiles.
waaye boroom bi ne ma: “demal, dinaa la yebal fu sore, nga jëm ci xeeti ñi dul yawut.”»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and jesus said unto them, come ye after me, and i will make you to become fishers of men.
yeesu ne leen: «Ñëwleen topp ci man, dinaa leen def nappkati nit.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and a certain scribe came, and said unto him, master, i will follow thee whithersoever thou goest.
laata ñuy jàll, benn xutbakat daldi ñëw ci moom ne ko: «kilifa gi, dinaa la topp fépp foo jëm.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
all that the father giveth me shall come to me; and him that cometh to me i will in no wise cast out.
képp ku ma baay bi jox dina ñëw ci man, te duma dàq mukk ki may fekksi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and again, i will put my trust in him. and again, behold i and the children which god hath given me.
newaat na:«dinaa am ci yàlla kóolute.» dellu na waxaat ne:«maa ngi nii, man ak doom yi ma yàlla jox.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and i will very gladly spend and be spent for you; though the more abundantly i love you, the less i be loved.
man nag nangu naa joxe li ma am lépp ak xol bu sedd, ba joxe sama bopp sax, ngir dimbali leen. gannaaw bëgg naa leen nii, xanaa kay seen mbëggeel ci man warul a wàññiku?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and when he was gone forth into the way, there came one running, and kneeled to him, and asked him, good master, what shall i do that i may inherit eternal life?
gannaaw loolu bi yeesu nekkee ci kaw yoon wi di dem, am ku daw, sukk ci kanamam ne ko: «kilifa gu baax gi, lu ma war a def, ngir am wàll ci dund gu dul jeex gi?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and another also said, lord, i will follow thee; but let me first go bid them farewell, which are at home at my house.
keneen ne ko: «sang bi, dinaa la topp, waaye may ma, ma jëkk a tàgguji sama waa kër.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.