From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
gnome also includes a complete development platform for applications programmers, allowing the creation of powerful and complex applications.
ak gnome dees na jébbalaale it ab joyaluwaay bees jagleel tëralkat yi, tax ñuy man a bindiy tëriin yu kàttanu te fasu
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
for his letters, say they, are weighty and powerful; but his bodily presence is weak, and his speech contemptible.
ndaxte am na ku naan: «ay bataaxalam dañoo ñagas te am doole, waaye bu teewee dafay ñàkk fulla, di wax waxi picc.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for the word of god is quick, and powerful, and sharper than any twoedged sword, piercing even to the dividing asunder of soul and spirit, and of the joints and marrow, and is a discerner of the thoughts and intents of the heart.
xam nanu ne, kàddug yàlla mi ngi dund te am na doole. moo gën a ñaw jaasiy ñaari boor. day dagg ba fa xol ak xel digaloo, ba fa yax yi ak yuq gi di teqalikoo, te man na àtte xalaat yi ak mébéti xol.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: