Results for publican translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

two men went up into the temple to pray; the one a pharisee, and the other a publican.

Wolof

mu ne: «dafa amoon ñaari nit ñu dem ca kër yàlla ga, di ñaan. kenn ki ab farisen la, ki ci des juutikat.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and if he shall neglect to hear them, tell it unto the church: but if he neglect to hear the church, let him be unto thee as an heathen man and a publican.

Wolof

bu leen dégluwul ñoom itam, wax ko mbooloom ñi gëm. bu dégluwul mbooloo ma nag, nga teg ko ni ku gëmul yàlla mbaa ab juutikat.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and after these things he went forth, and saw a publican, named levi, sitting at the receipt of custom: and he said unto him, follow me.

Wolof

gannaaw loolu yeesu génn, gis ab juutikat bu tudd lewi, mu toog ca juuti ba. mu ne ko: «kaay topp ci man.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

philip, and bartholomew; thomas, and matthew the publican; james the son of alphaeus, and lebbaeus, whose surname was thaddaeus;

Wolof

filib ak bartelemi; tomaa ak macë, juutikat ba woon; saag doomu alfe, ak tade;l

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

the pharisee stood and prayed thus with himself, god, i thank thee, that i am not as other men are, extortioners, unjust, adulterers, or even as this publican.

Wolof

farisen baa nga taxaw di ñaan ci xelam naan: “yaw yàlla, maa ngi lay sant ci li ma melul ni ñeneen ñiy sàcc, di def lu jubadi te di njaaloo, rawatina juutikat bii.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and all the people that heard him, and the publicans, justified god, being baptized with the baptism of john.

Wolof

nit ñépp ñi doon déglu yeesu, ba ci juutikat yi sax, dëggal nañu ne yàlla ku jub la, ndaxte nangu nañu yaxya sóob leen ci ndox.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,920,117,904 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK