Results for raised translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

but god raised him from the dead:

Wolof

waaye yàlla dekkal na ko,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but he, whom god raised again, saw no corruption.

Wolof

waaye ki yàlla dekkal, yaramam seeyul.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for if the dead rise not, then is not christ raised:

Wolof

su néew yi dul dekki, kirist moom it dekkiwul.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

this jesus hath god raised up, whereof we all are witnesses.

Wolof

yeesu moomu nag, yàlla dekkal na ko; nun ñépp seede nanu ko.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

him god raised up the third day, and shewed him openly;

Wolof

waaye yàlla dekkal na ko ci ñetteelu fan ba te biral ko,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

who was delivered for our offences, and was raised again for our justification.

Wolof

ndaxte yàlla jébbale na ko ngir sunuy tooñ, dekkal ko ngir àtte nu jub.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

the god of our fathers raised up jesus, whom ye slew and hanged on a tree.

Wolof

yàllay sunuy maam dekkal na yeesu, mi ngeen bóomoon ci wékk ko ca bant ba.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and god hath both raised up the lord, and will also raise up us by his own power.

Wolof

te yàlla, mi dekkal boroom bi, dina dekkal it sunu yaram jaare ko ci dooleem.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but some man will say, how are the dead raised up? and with what body do they come?

Wolof

waaye dina am kuy naan: «nan la néew yi di dekkee? wan yaram lañuy dellusee?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and killed the prince of life, whom god hath raised from the dead; whereof we are witnesses.

Wolof

bóom ngeen aji dundal ji, waaye yàlla dekkal na ko; seede nanu ko nun ñépp.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and hath raised us up together, and made us sit together in heavenly places in christ jesus:

Wolof

te dekkal na nu ak kirist yeesu, dëël nu ak moom ca bérab yu kawe ya.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they shall kill him, and the third day he shall be raised again. and they were exceeding sorry.

Wolof

dinañu ko rey, mu dekki ca ñetteelu fan ba.» bi ko taalibe ya déggee, ñu am naqar lool.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

knowing that he which raised up the lord jesus shall raise up us also by jesus, and shall present us with you.

Wolof

ndaxte xam nanu ne yàlla, mi dekkal boroom bi yeesu, dina nu dekkal nun itam ak yeesu, te dina nu yóbbu ak yéen, taxawal nun ñépp ci jataayam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and to wait for his son from heaven, whom he raised from the dead, even jesus, which delivered us from the wrath to come.

Wolof

te ngeen di séentu doomam bàyyikoo asamaan, moom yeesu mi mu dekkal te di nu musal ci merum yàlla, mi nar a ñëw.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

buried with him in baptism, wherein also ye are risen with him through the faith of the operation of god, who hath raised him from the dead.

Wolof

bi ñu leen sóobee ci ndox, suulaale nañu leen ak moom, te it dekki ngeen ak moom, ndaxte gëm ngeen ci dooley yàlla, ji ko dekkal ca néew ya.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

that if thou shalt confess with thy mouth the lord jesus, and shalt believe in thine heart that god hath raised him from the dead, thou shalt be saved.

Wolof

ndaxte soo waxee ak sa gémmiñ ne, yeesu mooy boroom bi, te nga gëm ci sa xol ne, yàlla dekkal na ko, dinga mucc.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and as concerning that he raised him up from the dead, now no more to return to corruption, he said on this wise, i will give you the sure mercies of david.

Wolof

te it li ko yàlla dekkal, ba mu bañatee jaar ci dee, te suuf du ko lekk mukk, moom la yàlla wax ne:“dinaa la may barke yu sell te wóor,yi ma digoon daawuda.”

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but the jews stirred up the devout and honourable women, and the chief men of the city, and raised persecution against paul and barnabas, and expelled them out of their coasts.

Wolof

waaye yawut ya xiir ay jigéen, ñi woomle te farlu ci diine, ñoom ak magi dëkk ba, ñu fitnaal pool ak barnabas, ngir génne leen réew ma.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for the scripture saith unto pharaoh, even for this same purpose have i raised thee up, that i might shew my power in thee, and that my name might be declared throughout all the earth.

Wolof

ndax mbind mi biral na li yàlla wax firawna ne ko:«def naa la buur,ngir feeñal sama kàttan ci say mbir,te ngir siiwal sama tur ci àddina si sépp.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

because he hath appointed a day, in the which he will judge the world in righteousness by that man whom he hath ordained; whereof he hath given assurance unto all men, in that he hath raised him from the dead.

Wolof

ndaxte sàkk na bés bu muy àtte àddina ci njub, dénk ko nit ki mu tànn; te firndeel na loolu bu wóor, ci li mu ko dekkal ca néew ya.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,880,669,756 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK