From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
them that sin rebuke before all, that others also may fear.
waaye ñiy bàkkaar, yedd leen fa kanam ñépp, ngir artu ñi ci des.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he spake that saying openly. and peter took him, and began to rebuke him.
noonu mu xamal leen mbir mi, ba mu leer nàññ. bi ko piyeer déggee, mu woo ko ci pegg, daldi ko yedd.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
these things speak, and exhort, and rebuke with all authority. let no man despise thee.
jàngaleel loolu, di leen dénk ak a yedd ak fulla ju mat. bu la kenn yab.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
rebuke not an elder, but intreat him as a father; and the younger men as brethren;
bul gëdd mag, waaye waxtaanal ak moom ni sa baay. ndaw it, nga digal ko ni sa rakk,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
take heed to yourselves: if thy brother trespass against thee, rebuke him; and if he repent, forgive him.
wottuleen seen bopp. «bu sa mbokk tooñee, yedd ko. bu réccoo, baal ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
then peter took him, and began to rebuke him, saying, be it far from thee, lord: this shall not be unto thee.
bi mu waxee ba noppi, piyeer woo ko ci pegg, bëgg koo yedd ne ko: «yàlla tere, boroom bi, loolu du la dal.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
preach the word; be instant in season, out of season; reprove, rebuke, exhort with all longsuffering and doctrine.
xamleel kàddug yàlla, sax ci, su neexee ak su naqaree; yeyal ñi tooñ, di yedd ak a dénk ñépp, def ko ci muñ gu yaatu ak njàngale mu mat.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yet michael the archangel, when contending with the devil he disputed about the body of moses, durst not bring against him a railing accusation, but said, the lord rebuke thee.
waaye bi mikayel, miy kilifa ci malaaka yi, di xëccook seytaane néewu musaa, bay xuloo ak moom, ñemewu koo àtte, boole ciy xas; mu yem ci wax ko ne: «na la boroom bi mbugal!»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
that ye may be blameless and harmless, the sons of god, without rebuke, in the midst of a crooked and perverse nation, among whom ye shine as lights in the world;
noonu dingeen am xol bu laab bu àndul ak ŋàññ, di guney yàlla yu amul sikk ci biir jamono ju yàqu te rëb. dangeen di leer ci seen biir ni weer ci àddina si,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: