From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
now in the morning as he returned into the city, he hungered.
ci suba teel yeesu dellusi ca dëkk ba, mu xiif.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and they worshipped him, and returned to jerusalem with great joy:
taalibe ya màggal ko, daldi dellu yerusalem, fees ak mbég.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
there are not found that returned to give glory to god, save this stranger.
amul kenn ci ñoom ku ñëw gërëm yàlla ku dul doxandéem bii!»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and mary abode with her about three months, and returned to her own house.
noonu maryaama toog fa elisabet lu war a tollook ñetti weer, sog a ñibbi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
on the morrow they left the horsemen to go with him, and returned to the castle:
ca ëllëg sa ñu woññiku, dellusi ca tata ja, bàyyi gawar ga, ñu gunge ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but when the officers came, and found them not in the prison, they returned, and told,
waaye bi wottukati kër yàlla ga agsee ca kaso ba, gisuñu leen fa; ñu daldi dellusi, yégle ko
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and returned from the sepulchre, and told all these things unto the eleven, and to all the rest.
bi ñu jógee bàmmeel ba, ñu dem nettaliji loolu lépp fukki ndaw ya ak benn, ak ña ca des ñépp.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and jesus being full of the holy ghost returned from jordan, and was led by the spirit into the wilderness,
noonu yeesu fees ak xel mu sell mi, jóge dexu yurdan.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for ye were as sheep going astray; but are now returned unto the shepherd and bishop of your souls.
ndaxte yéena ngi réeroon niy xar, waaye léegi dellusi ngeen ci sàmm, biy aar seeni xol.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and the seventy returned again with joy, saying, lord, even the devils are subject unto us through thy name.
juróom-ñaar-fukki taalibe yi ak ñaar dellusi, fees ak mbég te naan: «boroom bi, rab yi sax déggal nañu nu ndax sa tur.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and barnabas and saul returned from jerusalem, when they had fulfilled their ministry, and took with them john, whose surname was mark.
naka barnabas ak sool, bi ñu matalee seen liggéey, ñu jóge yerusalem, ñibbi, ànd ak yowaana mi tudd màrk.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and all the people that came together to that sight, beholding the things which were done, smote their breasts, and returned.
nit ña fa dajaloo woon ñépp, di seetaan li xew, ba ñu gisee loolu, ñu dellu seen kër, fëgg seen dënn, di jooy.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and it came to pass, that, when jesus was returned, the people gladly received him: for they were all waiting for him.
bi yeesu dëppee dellu, mbooloo ma di ko teeru, ndaxte ñépp a ngi ko doon xaar.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and when they had fulfilled the days, as they returned, the child jesus tarried behind in jerusalem; and joseph and his mother knew not of it.
bi màggal ga tasee, ñu dëpp ñibbi, waaye xale ba yeesu des yerusalem, te ay waajuram yéguñu ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and when he returned, he found them asleep again, (for their eyes were heavy,) neither wist they what to answer him.
dellusiwaat, fekk leen ñuy nelaw, ndaxte seeni bët dañoo diis. xamuñu lu ñu koy tontoo.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and the apostles, when they were returned, told him all that they had done. and he took them, and went aside privately into a desert place belonging to the city called bethsaida.
bi ndaw ya dellusee, ñu nettali yeesu la ñu defoon lépp. noonu mu yóbbaale leen, ñu sore nit ñi, jëm ca dëkk bu ñuy wax betsayda.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
then the whole multitude of the country of the gadarenes round about besought him to depart from them; for they were taken with great fear: and he went up into the ship, and returned back again.
ci kaw loolu waa diiwaanu serasa bépp ragal, ba ñaan yeesu mu jóge fa. noonu yeesu dugg ci gaal gi, di bëgg a dem.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and it came to pass, that when he was returned, having received the kingdom, then he commanded these servants to be called unto him, to whom he had given the money, that he might know how much every man had gained by trading.
«bi ñu ko falee buur nag, ba mu dellusi, mu woolu surga, ya mu joxoon wurus wa, ngir xam nan lañu ci liggéeye.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: