Results for seeing translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

for ye suffer fools gladly, seeing ye yourselves are wise.

Wolof

yéen boroom xel yi, aka ngeen a man a muñal ñi dof,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

seeing that many glory after the flesh, i will glory also.

Wolof

ndegam ñu bare dañuy damu ni nit kese, man itam kon dinaa damu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

seeing then that we have such hope, we use great plainness of speech:

Wolof

kon nag gannaaw wékku nanu ci yaakaar ju mel noonu, danuy waare ak kóolute gu mag.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

peter seeing him saith to jesus, lord, and what shall this man do?

Wolof

piyeer gis ko, daldi ne yeesu: «kii nag, boroom bi, nu muy mujje?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

lie not one to another, seeing that ye have put off the old man with his deeds;

Wolof

bàyyileen di fen seeni moroom, ndaxte summi ngeen jikko ju bon, ji ngeen judduwaale, moom ak ay jëfam;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

therefore seeing we have this ministry, as we have received mercy, we faint not;

Wolof

kon nag ndegam yàlla ci yërmandeem sas na nu liggéey boobu, dunu bayliku.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the men which journeyed with him stood speechless, hearing a voice, but seeing no man.

Wolof

nit ñi ànd ak moom nag taxaw, waaru ba luu, ci li ñu dégg baat bi te gisuñu kenn.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

seeing it is one god, which shall justify the circumcision by faith, and uncircumcision through faith.

Wolof

gannaaw yàlla kenn la, ñépp la fi nekkal. Ñi xaraf dina leen àtte ni ñu jub ndax seen ngëm, ñi xaraful it dina leen àtte ni ñu jub ndax seen ngëm.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but the other answering rebuked him, saying, dost not thou fear god, seeing thou art in the same condemnation?

Wolof

waaye ka ca des yedd moroom ma, naan ko: «xanaa ragaloo yàlla, yaw mi ñuy mbugal ni moom!

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and seeing the multitudes, he went up into a mountain: and when he was set, his disciples came unto him:

Wolof

bi yeesu gisee mbooloo ma nag, mu yéeg ca tund wa, toog; taalibeem ya ñëw ci moom.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and seeing one of them suffer wrong, he defended him, and avenged him that was oppressed, and smote the egyptian:

Wolof

noonu mu gis ca ku ñuy néewal doole, mu sotle ko, feyyul ko, ba dóor waayi misra ja.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for if he were on earth, he should not be a priest, seeing that there are priests that offer gifts according to the law:

Wolof

bu nekkoon ci àddina, du nekk sax saraxalekat, ndaxte am na fi ba noppi ay saraxalekat yuy def ay sarax, ni ko yoonu musaa santaanee.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

seeing ye have purified your souls in obeying the truth through the spirit unto unfeigned love of the brethren, see that ye love one another with a pure heart fervently:

Wolof

kon nag gannaaw déggal ngeen dëgg gi, ba sellal seeni xol te am mbëggeel gu dëggu, bëgganteleen mbëggeel gu tar ak seen xol bépp.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

(for that righteous man dwelling among them, in seeing and hearing, vexed his righteous soul from day to day with their unlawful deeds;)

Wolof

ndaxte lóot, mi dëkkoon ci seen biir, dafa dëkke woon tiisu xol, ndax ñaawteef yi mu gis ak a dégg guddi ak bëccëg.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

ye therefore, beloved, seeing ye know these things before, beware lest ye also, being led away with the error of the wicked, fall from your own stedfastness.

Wolof

noonu yeen samay xarit, gannaaw xam ngeen loolu ba noppi, moytuleen ñi weddi fàbbi leen ci seen réer, ba yolomal seen wàkkirlu ci yàlla.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the keeper of the prison awaking out of his sleep, and seeing the prison doors open, he drew out his sword, and would have killed himself, supposing that the prisoners had been fled.

Wolof

ci kaw loolu boroom kaso ba tiite ci ay nelaw, gis bunt yépp ubbiku, mu daldi bocci jaaseem, bëgg a xaru, yaakaar ne ña ñu tëj dañoo daw.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he said, unto you it is given to know the mysteries of the kingdom of god: but to others in parables; that seeing they might not see, and hearing they might not understand.

Wolof

mu tontu ne leen: «may nañu leen, ngeen xam mbóoti nguuru yàlla, waaye ñi ci des, dama leen di wax ci ay léeb. noonu la, ngir:“Ñuy xool te duñu man a gis,di dégg te duñu man a xam.”

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and in them is fulfilled the prophecy of esaias, which saith, by hearing ye shall hear, and shall not understand; and seeing ye shall see, and shall not perceive:

Wolof

li esayi waxoon ci kàddug yàlla am na ci ñoom, bi mu naan:“dingeen déglu bu baaxwaaye dungeen xam dara;di xool bu baax waaye dungeen gis dara.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and it came to pass, when he was in a certain city, behold a man full of leprosy: who seeing jesus fell on his face, and besought him, saying, lord, if thou wilt, thou canst make me clean.

Wolof

ni yeesu nekke woon ci ab dëkk, am fa ku gaana ba daj. bi mu gisee yeesu, mu daldi dëpp jëwam ci suuf, ñaan ko: «sang bi, soo ko bëggee, man nga maa wéral.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,874,087,436 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK