Results for sinners translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

i came not to call the righteous, but sinners to repentance.

Wolof

Ñëwuma ngir woo ñi jub, waaye ngir woo bàkkaarkat yi, ñu tuub seeni bàkkaar.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

we who are jews by nature, and not sinners of the gentiles,

Wolof

nun danoo cosaanoo ci xeetu yawut, te bokkunu ci xeet, yi xamul yàlla tey bàkkaar.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

then drew near unto him all the publicans and sinners for to hear him.

Wolof

ay juutikat ak ay boroom bàkkaar daan jegesi yeesu ngir déglu ko.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and the pharisees and scribes murmured, saying, this man receiveth sinners, and eateth with them.

Wolof

farisen ya ak xutbakat ya di ñurumtu naan: «waa jii mi ngi nangoo nekk ak ay boroom bàkkaar ak a lekkandook ñoom!»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but god commendeth his love toward us, in that, while we were yet sinners, christ died for us.

Wolof

waaye yàlla firndeel na mbëggeelam ci nun, ci li kirist dee ngir nun, bi nu nekkee sax ay bàkkaarkat!

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when the pharisees saw it, they said unto his disciples, why eateth your master with publicans and sinners?

Wolof

bi ko farisen ya gisee nag, ñu ne taalibe ya: «lu tax seen kilifa di lekkandoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and if ye do good to them which do good to you, what thank have ye? for sinners also do even the same.

Wolof

te bu ngeen defalee lu baax ñi leen koy defal, ban ngërëm ngeen ciy am? bàkkaarkat yi it dañuy def noonu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but their scribes and pharisees murmured against his disciples, saying, why do ye eat and drink with publicans and sinners?

Wolof

farisen yi ak seeni xutbakat di xultu taalibey yeesu yi ne leen: «lu tax ngeen di lekkandoo ak di naanandoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

now we know that god heareth not sinners: but if any man be a worshipper of god, and doeth his will, him he heareth.

Wolof

xam nanu ne, yàlla du déglu boroom bàkkaar. waaye nag, dina déglu ki koy ragal tey def coobareem.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and it came to pass, as jesus sat at meat in the house, behold, many publicans and sinners came and sat down with him and his disciples.

Wolof

gannaaw ga yeesu doon lekk ca kër ga, te ay juutikat ak i boroom bàkkaar yu bare dikk, bokk lekk ak yeesu ak taalibeem ya.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and if ye lend to them of whom ye hope to receive, what thank have ye? for sinners also lend to sinners, to receive as much again.

Wolof

te bu ngeen dee leble te yaakaar ci ndelloo, ban ngërëm ngeen ciy am? bàkkaarkat yi it dañuy lebal seeni moroom, ngir ñu delloo leen ko.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but go ye and learn what that meaneth, i will have mercy, and not sacrifice: for i am not come to call the righteous, but sinners to repentance.

Wolof

mbind mi nee na: “yërmande laa bëgg, waaye du rendi saraxi mala.” demleen nag te seet lu wax joojuy tekki. ndaxte ñëwuma, ngir woo ñi jub, waaye bàkkaarkat yi laay woo.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

the son of man is come eating and drinking; and ye say, behold a gluttonous man, and a winebibber, a friend of publicans and sinners!

Wolof

gannaaw gi nag doomu nit ki ñëw na, lekk, naan, ngeen daldi ne: “kii daal bëgg na lekk, di naan biiñ, tey xaritoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar.”

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

the son of man came eating and drinking, and they say, behold a man gluttonous, and a winebibber, a friend of publicans and sinners. but wisdom is justified of her children.

Wolof

gannaaw gi nag, doomu nit ki ñëw na, lekk, naan, ngeen daldi ne: “kii daal bëgg na lekk, di naan biiñ, tey xaritoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar.” waaye li xam-xamu yàlla di jur, mooy firndeel ne dëgg la.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and it came to pass, that, as jesus sat at meat in his house, many publicans and sinners sat also together with jesus and his disciples: for there were many, and they followed him.

Wolof

bi loolu amee yeesu ak i taalibeem di lekk ci kër lewi, fekk ay juutikat ak ay boroom bàkkaar yu bare di lekkandoo ak ñoom, ndaxte ñu bare ci ñoom a ko toppoon.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

knowing this, that the law is not made for a righteous man, but for the lawless and disobedient, for the ungodly and for sinners, for unholy and profane, for murderers of fathers and murderers of mothers, for manslayers,

Wolof

xam nanu it ne, tëddul ngir ñi jub waaye ngir ñi jubadi ak ñi déggadi, ñi weddi tey bàkkaar, ñi selladi te fonkadi yàlla, ñiy dóor ndey walla baay, ak ñiy bóom;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and if the righteous scarcely be saved, where shall the ungodly and the sinner appear?

Wolof

te:«su muccu ki jub jafee,luy doon muju ki weddi te dëng?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,776,905,531 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK