Results for somewhat translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

nevertheless i have somewhat against thee, because thou hast left thy first love.

Wolof

waaye li ma naqari ci yaw moo di sa mbëggeel wàññiku na.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and jesus answering said unto him, simon, i have somewhat to say unto thee. and he saith, master, say on.

Wolof

yeesu ne ca tonn, daldi ne farisen ba: «simoŋ, am na lu ma la war a wax.» simoŋ ne ko: «waxal, kilifa gi.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he said, the jews have agreed to desire thee that thou wouldest bring down paul to morrow into the council, as though they would inquire somewhat of him more perfectly.

Wolof

mu tontu ne: «yawut yi dañoo dige, ngir ñaan la, nga indi pool ëllëg ca kanamu kureelu àttekat ya, mel ni dañoo bëgg a seet mbiram bu gën a wóor.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for though i should boast somewhat more of our authority, which the lord hath given us for edification, and not for your destruction, i should not be ashamed:

Wolof

awma lu may rus, su may damu lu ëpp ci sañ-sañ bi nu boroom bi jox, di sañ-sañu yokk seen ngëm, te du ngir seen kasara.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

whensoever i take my journey into spain, i will come to you: for i trust to see you in my journey, and to be brought on my way thitherward by you, if first i be somewhat filled with your company.

Wolof

bu may dem espaañ nag, bëgg naa faa jaar, nuyu leen; ndaxte ay at a ngii maa ngi am yéene ju tar ci ñëw seetsi leen. bëgg na maa nekk ci seen biir, ngir am bànneexu sotteente ak yéen xalaat ab diir, te it ngeen waajalal ma sama yoonu espaañ.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but of these who seemed to be somewhat, (whatsoever they were, it maketh no matter to me: god accepteth no man's person:) for they who seemed to be somewhat in conference added nothing to me:

Wolof

waaye ñi ñu gën a fonk --ak lu man a doon seen sag xooluma ko, ñépp a yem fa kanam yàlla — waaye ñooñu ñu teg njiit boog, bi ma dajee ak ñoom, yokkuñu dara ci sama sas.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,170,064,765 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK