From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
looking diligently lest any man fail of the grace of god; lest any root of bitterness springing up trouble you, and thereby many be defiled;
moytuleen ba kenn du ñàkk yiwu yàlla mbaa kenn mel ni reen bu wex buy jebbi, ba di leen lëjal tey gaañ ñu bare ci wextanam.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but whosoever drinketh of the water that i shall give him shall never thirst; but the water that i shall give him shall be in him a well of water springing up into everlasting life.
waaye ndox, mi may joxe, ku ci naan du marati mukk, ndaxte day nekk ci moom bëtu ndox buy ball, di joxe dund gu dul jeex.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: