From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
but i have prayed for thee, that thy faith fail not: and when thou art converted, strengthen thy brethren.
waaye man ñaanal naa la, ngir sa ngëm dëgër. te yaw, boo dellusee, nanga dëgëral sa bokki taalibe yi.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
be watchful, and strengthen the things which remain, that are ready to die: for i have not found thy works perfect before god.
yeewul te dëgëral li des ci yaw tey waaj a dee, ndaxte gis naa ne, say jëf matuñu ca sama kanam yàlla.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but the god of all grace, who hath called us unto his eternal glory by christ jesus, after that ye have suffered a while, make you perfect, stablish, strengthen, settle you.
te yàlla mi jagoo yiw wépp te woo leen ci darajay kirist, ngir ngeen bokk ci ndamam li sax, gannaaw bi ngeen yendoo bëccëgu tiis, dina leen yeesalaat, di leen dëgëral ak a dooleel, ba ngeen sampu.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: