Results for surnamed translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

and simon he surnamed peter;

Wolof

fukk ak ñaar ñii la tànn:simoŋ, mi mu tudde piyeer,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

then entered satan into judas surnamed iscariot, being of the number of the twelve.

Wolof

noonu seytaane daldi solu yudaa, mi ñuy wooye iskariyo te mu bokkoon ca fukki taalibe ya ak ñaar.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they appointed two, joseph called barsabas, who was surnamed justus, and matthias.

Wolof

bi ko piyeer waxee, ñu tudd ñaar: yuusufa, mi ñu dippee barsabas te di ko dàkkentale yustus, moom ak macas.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and called, and asked whether simon, which was surnamed peter, were lodged there.

Wolof

Ñu woote nag naan: «simoŋ, mi ñu dàkkentale piyeer, ndax fi la dëkk?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and james the son of zebedee, and john the brother of james; and he surnamed them boanerges, which is, the sons of thunder:

Wolof

saag doomu sebede, ak yowaana mi mu bokkal ndey ak baay — ñoom ñi mu wooye bowanerses, maanaam «Ñi aaytal ni dënnu gi» —

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and joses, who by the apostles was surnamed barnabas, (which is, being interpreted, the son of consolation,) a levite, and of the country of cyprus,

Wolof

noonu amoon na fa ku tudd yuusufa, te ndaw yi dàkkentale ko barnabas, miy tekki «kiy dëgëral fit yi,» mu soqikoo ci giiru lewi, te juddoo dunu sipar.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,941,737,663 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK