Results for thin space translation from English to Wolof

English

Translate

thin space

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

and i gave her space to repent of her fornication; and she repented not.

Wolof

may naa ko ab diir, ngir mu tuub njaaloom, waaye bañ na.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and after they had tarried there a space, they were let go in peace from the brethren unto the apostles.

Wolof

bi loolu amee ñu toog fa ab diir, ba noppi bokk yi yiwi leen ci jàmm, ñu dellu ca ña leen yónni woon.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and after that he gave unto them judges about the space of four hundred and fifty years, until samuel the prophet.

Wolof

loolu lépp xew na ci diirub ñeenti téeméeri at ak juróom-fukk. «gannaaw loolu mu jox leen ay àttekat, ba ci yonent yàlla samwil.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but when they knew that he was a jew, all with one voice about the space of two hours cried out, great is diana of the ephesians.

Wolof

waaye bi ñu xamee ne yawut la, ñépp a bokk benn baat, yuuxu diirub lu mat ñaari waxtu naan: «artemis mu efes màgg na!»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he went into the synagogue, and spake boldly for the space of three months, disputing and persuading the things concerning the kingdom of god.

Wolof

noonu pool dugg ca jàngu ba, di wax ak fit wu dëgër diirub ñetti weer, di diisoo ak ñoom ci mbirum nguurug yàlla, di leen jéem a gëmloo.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and this continued by the space of two years; so that all they which dwelt in asia heard the word of the lord jesus, both jews and greeks.

Wolof

mu wéy ci noonu diirub ñaari at, ba ñi dëkk diiwaanu asi ñépp dégg kàddug boroom bi, muy yawut muy gereg.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and about the space of one hour after another confidently affirmed, saying, of a truth this fellow also was with him: for he is a galilaean.

Wolof

bi ñu tegee lu mat waxtu, keneen dikkaat ca wax ja ne: «ci lu wóor nit kii àndoon na ak moom, nde galile la jóge.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

elias was a man subject to like passions as we are, and he prayed earnestly that it might not rain: and it rained not on the earth by the space of three years and six months.

Wolof

naka noonu iliyas nit la woon ku bindoo ni nun, waaye bi mu saxee ci ñaan yàlla, ngir mu bañ a taw, ndox laalul suuf diirub ñetti at ak genn-wàll.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and there are seven kings: five are fallen, and one is, and the other is not yet come; and when he cometh, he must continue a short space.

Wolof

juróom daanu nañu, kenn kaa ngi fi, ki ci des ñëwagul, te bu ñëwee, dina fi war a nekk ab diir.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

then stood there up one in the council, a pharisee, named gamaliel, a doctor of the law, had in reputation among all the people, and commanded to put the apostles forth a little space;

Wolof

waaye amoon na fa nit ku tudd gamaleel, bokk ci tariixab farisen ya, di xutbakat bu tedd ci yoonu musaa, mu jóg ca mbooloo ma, santaane ñu génne leen tuuti.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

then god turned, and gave them up to worship the host of heaven; as it is written in the book of the prophets, o ye house of israel, have ye offered to me slain beasts and sacrifices by the space of forty years in the wilderness?

Wolof

waaye bi ñu ko defee yàlla dëddu leen, bërgël leen, ñuy jaamu biddiiwi asamaan. moom lañu bind ci téereb yonent yi ne:“yéen bànni israyil, ndax rendi ngeen jur,jébbal ma, boole ko ak i sarax,diirub ñeent-fukki at ca màndiŋ ma?

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
9,140,065,851 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK