From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
today %i:%m %p
friendly timeyesterday 12:34 am
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
i will not leave you comfortless: i will come to you.
duma leen bàyyi ngeen wéet. dinaa dellusi ci yéen.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and i will give him the morning star.
ni ma jële sañ-sañ ci sama baay. dinaa ko jox it biddiiwu njël.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but after that i am risen, i will go before you into galilee.
waaye bu ma dekkee, dinaa leen jiituji galile.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but after i am risen again, i will go before you into galilee.
waaye bu ma dekkee, dinaa leen jiituji galile.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he saith unto them, follow me, and i will make you fishers of men.
yeesu ne leen: «Ñëwleen topp ci man, ma def leen nappkati nit.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but i will tarry at ephesus until pentecost.
ba tey dinaa toog fii ci dëkku efes ba màggalu pàntakot,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
come unto me, all ye that labour and are heavy laden, and i will give you rest.
«Ñëwleen ci man, yéen ñépp ñi sonn te diis, dinaa leen may noflaay.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and jesus saith unto him, i will come and heal him.
yeesu ne ko: «dinaa ñëw faj ko.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he answered and said unto them, i will also ask you one thing; and answer me:
yeesu tontu leen ne: «man itam dinaa leen laaj lenn: wax leen ma,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
if ye shall ask any thing in my name, i will do it.
lu ngeen ñaan ci sama tur, maa koy def.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for i will give you a mouth and wisdom, which all your adversaries shall not be able to gainsay nor resist.
ndaxte man ci sama bopp maa leen di jox kàddu ak xel moo xam ne seeni noon duñu ko man a teggi, mbaa ñu di ko weddi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and i will pray the father, and he shall give you another comforter, that he may abide with you for ever;
te dinaa ñaan baay bi, mu jox leen beneen dimbalikat, buy nekk ak yéen ba abadan.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
at that day ye shall ask in my name: and i say not unto you, that i will pray the father for you:
bu keroogee dingeen ñaan ci sama tur. neewuma dinaa leen ñaanal baay bi,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and i will very gladly spend and be spent for you; though the more abundantly i love you, the less i be loved.
man nag nangu naa joxe li ma am lépp ak xol bu sedd, ba joxe sama bopp sax, ngir dimbali leen. gannaaw bëgg naa leen nii, xanaa kay seen mbëggeel ci man warul a wàññiku?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he said unto me, depart: for i will send thee far hence unto the gentiles.
waaye boroom bi ne ma: “demal, dinaa la yebal fu sore, nga jëm ci xeeti ñi dul yawut.”»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and said unto them, what will ye give me, and i will deliver him unto you? and they covenanted with him for thirty pieces of silver.
ne leen: «lan ngeen ma man a jox, ngir ma jébbal leen yeesu?» noonu saraxalekat ya daldi ko waññal fanweeri poseti estateer.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and a certain scribe came, and said unto him, master, i will follow thee whithersoever thou goest.
laata ñuy jàll, benn xutbakat daldi ñëw ci moom ne ko: «kilifa gi, dinaa la topp fépp foo jëm.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
all that the father giveth me shall come to me; and him that cometh to me i will in no wise cast out.
képp ku ma baay bi jox dina ñëw ci man, te duma dàq mukk ki may fekksi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and again, i will put my trust in him. and again, behold i and the children which god hath given me.
newaat na:«dinaa am ci yàlla kóolute.» dellu na waxaat ne:«maa ngi nii, man ak doom yi ma yàlla jox.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: