From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
and when they were come to capernaum, they that received tribute money came to peter, and said, doth not your master pay tribute?
gannaaw loolu yeesu ak taalibe ya ñëw kapernawum. bi ñu fa àggee nag, laajkati warugaru kër yàlla ga ñëw ci piyeer ne ko: «ndax seen kilifa du fey posetu ñaari daraxma ngir warugar wi?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
is it lawful for us to give tribute unto caesar, or no?
wax nu, ndax jaadu na, nu fey buur bi sesaar galag walla déet.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
shew me the tribute money. and they brought unto him a penny.
wonleen ma poset, bi ñuy feye galag.» Ñu daldi ko jox nag benn posetu denariyon.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
render therefore to all their dues: tribute to whom tribute is due; custom to whom custom; fear to whom fear; honour to whom honour.
joxleen ku nekk céram; ku ngeen war a fey galag, feyleen ko ko; ku ngeen war a fey juuti, feyleen ko ko; ku ngeen war a weg, wegleen ko; ku ngeen war a teral, teral-leen ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and they began to accuse him, saying, we found this fellow perverting the nation, and forbidding to give tribute to caesar, saying that he himself is christ a king.
foofa ñu tàmbali di ko sosal naan: «fekk nanu nit kii, muy fàbbi sunu réew, di leen teree fey galag sesaar, te mi ngi teg boppam almasi, maanaam buur.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and when they were come, they say unto him, master, we know that thou art true, and carest for no man: for thou regardest not the person of men, but teachest the way of god in truth: is it lawful to give tribute to caesar, or not?
Ñu ñëw ci moom nag ne ko: «kilifa gi, xam nanu ne ku wóor nga, te ragaloo kenn, ndaxte seetuloo jëmmi nit, waaye dangay xamle yoonu yàlla ci bu wóor. wax nu, ndax jaadu na, nu fey buur bi sesaar galag am déet? nu fey ko walla nu bañ koo fey?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
he saith, yes. and when he was come into the house, jesus prevented him, saying, what thinkest thou, simon? of whom do the kings of the earth take custom or tribute? of their own children, or of strangers?
piyeer ne leen: «aaŋkay!»ba ñu eggee kër ga nag, yeesu jëkk a wax ne piyeer: «waaw lu ciy sa xalaat, simoŋ? buuri àddina si, ñan lañuy laaj juuti walla galag? seeni doom walla ñi bokkul ci njaboot gi?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.