From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
by pureness, by knowledge, by longsuffering, by kindness, by the holy ghost, by love unfeigned,
nu ngi rafetal sunu yen ci dund gu sell, ci xam-xam, muñ ak laabiir, ci xel mu sell mi ak ci mbëggeel gu raxul njublaŋ,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
now the end of the commandment is charity out of a pure heart, and of a good conscience, and of faith unfeigned:
waaye li sunuy dénkaane di jur mooy mbëggeel gu jóge ci xol bu laab, ci xel mu dal ak ci ngëm gu wér.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
seeing ye have purified your souls in obeying the truth through the spirit unto unfeigned love of the brethren, see that ye love one another with a pure heart fervently:
kon nag gannaaw déggal ngeen dëgg gi, ba sellal seeni xol te am mbëggeel gu dëggu, bëgganteleen mbëggeel gu tar ak seen xol bépp.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
when i call to remembrance the unfeigned faith that is in thee, which dwelt first in thy grandmother lois, and thy mother eunice; and i am persuaded that in thee also.
maa ngi fàttaliku sa ngëm gu dëggu, gi nekkoon ci sa maam lowis ak sa yaay Ënis, te mu wóor ma ne, sax na ci yaw it.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: