From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
all unrighteousness is sin: and there is a sin not unto death.
gépp jubadi bàkkaar la, waaye am na bàkkaar bu jarul dee.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
what shall we say then? is there unrighteousness with god? god forbid.
kon lu nu ci war a wax? ndax yàlla àttewul foofu yoon nag? mukk!
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
that they all might be damned who believed not the truth, but had pleasure in unrighteousness.
noonu yàlla dina mbugal ñépp ñi gëmul woon dëgg te doon bànneexu ci njubadi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but unto them that are contentious, and do not obey the truth, but obey unrighteousness, indignation and wrath,
waaye ñi dëgër bopp, ba tanqamlu dëgg, di topp lu jubadi, seen pey mooy dooni merum yàlla ak toroxte.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
if we confess our sins, he is faithful and just to forgive us our sins, and to cleanse us from all unrighteousness.
su nu nangoo sunuy bàkkaar ci kanamam, fekk kuy sàmm kóllëre la te jub, ngir baal nu sunuy bàkkaar te sellal nu ci lépp lu jubadi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for the wrath of god is revealed from heaven against all ungodliness and unrighteousness of men, who hold the truth in unrighteousness;
merum yàllaa ngi feeñe asamaan, wàcc ci nit ñi, ndax seen weddi yàlla gépp ak seen jubadi gépp, ñoom ñi suul dëgg, di topp lu jubadi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and with all deceivableness of unrighteousness in them that perish; because they received not the love of the truth, that they might be saved.
te dina nas bépp naxe buy sànke, ba yéem ñi nar a alku, ndaxte ubbiluñu seeni xol dëgg, gi leen manoon a musal.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and i say unto you, make to yourselves friends of the mammon of unrighteousness; that, when ye fail, they may receive you into everlasting habitations.
yeesu teg ca ne: «maa ngi leen di wax lii: sàkkuleen ay xarit jaare ko ci alalu àddina, ngir bu alal nekkatul, ñu man leen a fat ca dal yu sax ya.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
neither yield ye your members as instruments of unrighteousness unto sin: but yield yourselves unto god, as those that are alive from the dead, and your members as instruments of righteousness unto god.
te buleen jébbalati seeni cér bàkkaar, mu def leen jumtukaayam ngir jëfam yu jubadi; waaye gannaaw rëcc ngeen ci dooley dee, bay dundaat, jébbaluleen ci yàlla te jébbal ko seeni cér, mu def leen jumtukaayam ngir jëfam yu jub.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and shall receive the reward of unrighteousness, as they that count it pleasure to riot in the day time. spots they are and blemishes, sporting themselves with their own deceivings while they feast with you;
muy seen peyug njubadi. xawaare bëccëgu ndara-kàmm mooy seen bànneex. su ñuy lekkandoo ak yeen, dañuy bànneexu ci seeni bëgg-bëgg, di ay gàkk ak i sikk ci seen biir.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
being filled with all unrighteousness, fornication, wickedness, covetousness, maliciousness; full of envy, murder, debate, deceit, malignity; whisperers,
seen xol fees na ak lu jubadi, lu bon, bëgge ak coxor; duñu xalaat lu dul kiñaan, rey nit, xuloo, njublaŋ ak ñaaw njort; dañuy jëw,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: