Results for uttered translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

of whom we have many things to say, and hard to be uttered, seeing ye are dull of hearing.

Wolof

ci fànn googu, am na lu bare lu nu ci bëgg a wax, waaye tekkil leen ko dina jafe, ndaxte dangeen a naqari xel.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and cried with a loud voice, as when a lion roareth: and when he had cried, seven thunders uttered their voices.

Wolof

di xaacu, mel ni gaynde guy yëmmu. naka la xaacu, juróom-ñaari dënnu yi jib.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

likewise the spirit also helpeth our infirmities: for we know not what we should pray for as we ought: but the spirit itself maketh intercession for us with groanings which cannot be uttered.

Wolof

te it xelu yàlla mi moo nuy xettali ci sunug néew doole. ndaxte xamunu sax naka lanu war a ñaane yàlla, waaye xelu yàlla maa ngi nuy ñaanal fa moom ak i yéene yu làmmiñ mënta takk.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when the seven thunders had uttered their voices, i was about to write: and i heard a voice from heaven saying unto me, seal up those things which the seven thunders uttered, and write them not.

Wolof

naka la juróom-ñaari dënnu yi di jib, may waaj a bind, waaye ma dégg baat bu jóge asamaan, naan ma: «li juróom-ñaari dënnu yi wax, na nekk kumpa, bu ko bind.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,862,956,698 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK