From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
god is your master
yaala mooy sa borrom
Last Update: 2023-07-13
Usage Frequency: 1
Quality:
neither be ye called masters: for one is your master, even christ.
buñu leen tudde it ay “njiit,” ndaxte kenn rekk moo di seen njiit, mooy kirist.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
wherefore i desire that ye faint not at my tribulations for you, which is your glory.
maa ngi leen di ñaan nag, ngeen bañ a yoqi ndax coono, yi may jële ci bey sama sas ci yéen, xam ne coono yooyu ñoo leen di jural ndam.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and call no man your father upon the earth: for one is your father, which is in heaven.
te buleen tudde kenn seen “baay” ci àddina, ndaxte kenn rekk moo di seen baay, ki ci kaw.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
but be not ye called rabbi: for one is your master, even christ; and all ye are brethren.
waaye yéen buñu leen wooye “kilifa gi,” ndaxte kenn rekk moo di seen kilifa, te yéen ñépp ay bokk ngeen.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and if ye have not been faithful in that which is another man's, who shall give you that which is your own?
te su ngeen maanduwul ci alal ji ngeen moomul, kon ku leen di jox alal ji ngeen moom?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
rejoice, and be exceeding glad: for great is your reward in heaven: for so persecuted they the prophets which were before you.
bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
i beseech you therefore, brethren, by the mercies of god, that ye present your bodies a living sacrifice, holy, acceptable unto god, which is your reasonable service.
kon nag bokk yi, gannaaw yërmandey yàlla baree na noonu, maa ngi leen di ñaan, ngeen jébbal ko seen yaram wépp. na seen dund mel ni sarax su ñuy defal yàlla, sarax su sell te neex ko. loolu mooy njaamu, gi leen war.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
jesus answered, if i honour myself, my honour is nothing: it is my father that honoureth me; of whom ye say, that he is your god:
yeesu ne leen: «su ma dee màggal sama bopp, du am maana. sama baay a may màggal, moom mi ngeen naan, mooy seen yàlla.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he said unto them, where is your faith? and they being afraid wondered, saying one to another, what manner of man is this! for he commandeth even the winds and water, and they obey him.
yeesu ne taalibe yi: «ana seen ngëm?» Ñu daldi tiit te waaru, naan ci seen biir: «kii moo di kan? mi ngi jox ndigal ngelaw li ak ndox mi, ñu koy déggal.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: