From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
but she that liveth in pleasure is dead while she liveth.
waaye ki bànneex jiital, ndee luy dox la.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
while the pharisees were gathered together, jesus asked them,
bi farisen ya dajee nag, yeesu laaj leen:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
in the mean while his disciples prayed him, saying, master, eat.
fekk taalibey yeesu ya di ko gétën ne: «kilifa gi, lekkal.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for yet a little while, and he that shall come will come, and will not tarry.
ndaxte lii la mbind mi wax:«ci kanam tuuti, ki war a ñëw dina ñëwte léegi mu agsi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
saying, say ye, his disciples came by night, and stole him away while we slept.
ne leen: «nangeen wax lii: “ay taalibeem ñëw nañu ci guddi, sàcc ko, bi nuy nelaw.”
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and so it was, that, while they were there, the days were accomplished that she should be delivered.
bi ñu nekkee betleyem, waxtu wa mu waree mucc agsi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he said unto them, can ye make the children of the bridechamber fast, while the bridegroom is with them?
yeesu ne leen: «ndax man ngeen a woorloo gan, yi ñëw cig céet, li feek boroom céet gaa ngi ànd ak ñoom?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
for a testament is of force after men are dead: otherwise it is of no strength at all while the testator liveth.
ndaxte bala dénkaaneb miraas di taxaw, dee am; te taxawul, fi ak ki ko bind a ngi dund.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he became very hungry, and would have eaten: but while they made ready, he fell into a trance,
noonu xiif dab ko fa, mu bëgg a lekk. waaye bi ñu koy toggal, yàlla feeñu ko.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and after a little while another saw him, and said, thou art also of them. and peter said, man, i am not.
nes tuuti keneen gis ko ne: «yaw itam ci ñoom nga bokk.» piyeer tontu ko: «sama waay, bokkuma ci.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he would not for a while: but afterward he said within himself, though i fear not god, nor regard man;
Àttekat ba bañ lu yàgg, waaye am bés mu ne ci xelam: “ragaluma yàlla te faalewuma mbindeef,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and after a while came unto him they that stood by, and said to peter, surely thou also art one of them; for thy speech bewrayeth thee.
nes tuuti ña fa taxawoon ñëw ci piyeer ne ko: «ci lu wóor ne yaw itam bokk nga ci ñoom, ndaxte sa waxin feeñal na la.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and they said one to another, did not our heart burn within us, while he talked with us by the way, and while he opened to us the scriptures?
noonu ku nekk naan sa moroom: «ndax sa xol seddul woon, bi muy wax ak nun ci yoon wi, te muy tekki mbind mi?»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
a little while, and ye shall not see me: and again, a little while, and ye shall see me, because i go to the father.
«ci kanam tuuti dungeen ma gisati. bu ñu ci tegee ab diir, ngeen gisaat ma.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and shall receive the reward of unrighteousness, as they that count it pleasure to riot in the day time. spots they are and blemishes, sporting themselves with their own deceivings while they feast with you;
muy seen peyug njubadi. xawaare bëccëgu ndara-kàmm mooy seen bànneex. su ñuy lekkandoo ak yeen, dañuy bànneexu ci seeni bëgg-bëgg, di ay gàkk ak i sikk ci seen biir.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and immediately, while he yet spake, cometh judas, one of the twelve, and with him a great multitude with swords and staves, from the chief priests and the scribes and the elders.
bi yeesu di wax, yudaa mi bokkoon ci fukki taalibe ya ak ñaar, agsi, ànd ak mbooloo mu bare, mu jóge ca saraxalekat yu mag ya, ca xutbakat ya ak ca njiiti xeet wa, te gànnaayoo jaasi ak yet.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
little children, yet a little while i am with you. ye shall seek me: and as i said unto the jews, whither i go, ye cannot come; so now i say to you.
samay soppe, sama nekk ak yéen dootul yàgg. dingeen may seet, waaye maa ngi leen di wax léegi li ma waxoon yawut ya: fa ma jëm, dungeen fa man a dem.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
agree with thine adversary quickly, whiles thou art in the way with him; lest at any time the adversary deliver thee to the judge, and the judge deliver thee to the officer, and thou be cast into prison.
«gaawal a juboo ak ki lay yóbbu, ngeen layooji, bala ngeen a egg; ngir bañ ki ngay layool jébbal la àttekat ba, kooka jox la alkaati ba, ñu tëj la.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: