Results for étonnés translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

jésus leur répondit: j`ai fait une oeuvre, et vous en êtes tous étonnés.

Wolof

yeesu ne leen: «benn jaloore rekk laa def, te yéen ñépp ngeen jaaxle!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

les disciples, ayant entendu cela, furent très étonnés, et dirent: qui peut donc être sauvé?

Wolof

bi nga xamee ne taalibe ya dégg nañu loolu, ñu daldi waaru lool ne ko: «kan moo man a mucc nag?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ils l`écoutaient attentivement, parce qu`il les avait longtemps étonnés par ses actes de magie.

Wolof

Ñu taq ci moom, ndax li mu leen yàgg a waar ci ay luxus.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ils ne purent rien reprendre dans ses paroles devant le peuple; mais, étonnés de sa réponse, ils gardèrent le silence.

Wolof

noonu mënuñu ko woon a jàpp ciy waxam ci kanamu mbooloo ma; ñu waaru ci tontoom, ba wedam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il est vrai que quelques femmes d`entre nous nous ont fort étonnés; s`étant rendues de grand matin au sépulcre

Wolof

teewul nag am na ay jigéen yu bokk ci nun yu nu jaaxal. dañoo fajaru ca bàmmeel ba,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et ils dirent: c`est son ange. cependant pierre continuait à frapper. ils ouvrirent, et furent étonnés de le voir.

Wolof

fekk piyeer di gën a fëgg. noonu ñu tijji, gis ko, daldi waaru.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

les disciples, qui virent cela, furent étonnés, et dirent: comment ce figuier est-il devenu sec en un instant?

Wolof

bi nga xamee ne taalibe ya gis nañu loolu, ñu waaru naan: «nan la figg gi daldi wowe ci taxawaay bi?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

comme il ne quittait pas pierre et jean, tout le peuple étonné accourut vers eux, au portique dit de salomon.

Wolof

naka waa ji taq ci piyeer ak yowaana, ñépp waaru; ñu daldi daw, fekksi leen ca bérab ba ñuy wax werandaa bu suleymaan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,794,874,987 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK