Results for abondance translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

qu`il a répandu sur nous avec abondance par jésus christ notre sauveur,

Wolof

mi mu nu sotti ba mu baawaan, ci darajay yeesu kirist sunu musalkat.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

au milieu de beaucoup de tribulations qui les ont éprouvées, leur joie débordante et leur pauvreté profonde ont produit avec abondance de riches libéralités de leur part.

Wolof

nattu yi ñu jaar ëmb nañu coono yu réy; waaye seen mbég mu tar ak seen ñàkk gu metti ñoo jur ci ñoom yéwén gu jéggi dayo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car si ces choses sont en vous, et y sont avec abondance, elles ne vous laisseront point oisifs ni stériles pour la connaissance de notre seigneur jésus christ.

Wolof

ndaxte bu leen jiko yooyu soloo, ba sax ci yeen, dina tax seen xam yeesu krist boroom bi am njeriñ te jur mbaax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et dieu peut vous combler de toutes sortes de grâces, afin que, possédant toujours en toutes choses de quoi satisfaire à tous vos besoins, vous ayez encore en abondance pour toute bonne oeuvre,

Wolof

te yàlla man na leen a woomal ci bépp yiwam ba ci fépp ak ci lépp, ngeen faj seen soxla yépp te sakkanle it ngir bépp jëf bu baax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car on donnera à celui qui a, et il sera dans l`abondance, mais à celui qui n`a pas on ôtera même ce qu`il a.

Wolof

ndaxte ku am dinañu la dolli, ba nga barele, waaye ku amul, li nga am as néew sax, dinañu ko nangu.

Last Update: 2023-07-29
Usage Frequency: 2
Quality:

French

Étant rentré en lui-même, il se dit: combien de mercenaires chez mon père ont du pain en abondance, et moi, ici, je meurs de faim!

Wolof

mujj xelam dellusi, mu ne: “sama baay am na ay surga yu bare, te dañuy lekk ba suur. man nag maa ngi fii di bëgg a dee ak xiif!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

j`ai tout reçu, et je suis dans l`abondance; j`ai été comblé de biens, en recevant par Épaphrodite ce qui vient de vous comme un parfum de bonne odeur, un sacrifice que dieu accepte, et qui lui est agréable.

Wolof

fi mu ne jot naa li ma aajowoo lépp, ba maa ngi ci naataange; li ngeen ma yónnee ci loxoy epafrodit doy na sëkk; ni xetu latkoloñ la mel ci man, di sarax su neex yàlla te mu nangu ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,772,448,997 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK