From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
et les ayant appelés, ils leur défendirent absolument de parler et d`enseigner au nom de jésus.
noonu ñu woo leen, ñu tere leen bu wóor, ñu waxati mbaa waare dara ci turu yeesu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
autrement, que feraient ceux qui se font baptiser pour les morts? si les morts ne ressuscitent absolument pas, pourquoi se font-ils baptiser pour eux?
su ndekkite amul, kon ñi ñu sóob ci ndox ngir ñi dee, lu mu leen di jariñ? su dekki amul, kon lu tax ñu leen di sóob ngir ñi dee?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mais il n`y consentit point, et il prit congé d`eux, en disant: il faut absolument que je célèbre la fête prochaine à jérusalem. je reviendrai vers vous, si dieu le veut. et il partit d`Éphèse.
kon mu tàggtoo ak ñoom naan: «dinaa dellusi ci yéen, bu soobee yàlla.» noonu mu dugg gaal, jóge efes,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: