From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
alors il fit asseoir la foule par terre,
ci kaw loolu yeesu sant mbooloo mi, ñu toog ci suuf.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors jésus leur dit ouvertement: lazare est mort.
ci kaw loolu yeesu wax ci lu leer ne: «lasaar dee na.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors quiconque invoquera le nom du seigneur sera sauvé.
booba nag ku woo boroom bi ci aw turam,dinga mucc.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors il quitta la judée, et retourna en galilée.
bi yeesu yégee loolu nag, mu jóge yude, dellu diiwaanu galile.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors ces gens mirent la main sur jésus, et le saisirent.
bi mu ko defee nit ñi song yeesu nag, jàpp ko.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors ils se mirent à supplier jésus de quitter leur territoire.
ci kaw loolu ñu daldi ñaan yeesu, mu sore seen réew.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors toutes ces vierges se réveillèrent, et préparèrent leurs lampes.
bi ko janq ya déggee, ñu jóg, defar seeni làmp.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors ils répondirent qu`ils ne savaient d`où il venait.
noonu ñu tontu ne, xamuñu fu mu ko jële.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors les scribes et les pharisiens amenèrent une femme surprise en adultère;
xutbakat ya ak farisen ya indi jenn jigéen ju ñu bettoon muy njaaloo, ñu taxawal ko ca diggu mbooloo ma.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors il me dit: va, je t`enverrai au loin vers les nations...
waaye boroom bi ne ma: “demal, dinaa la yebal fu sore, nga jëm ci xeeti ñi dul yawut.”»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors aussi plusieurs succomberont, et ils se trahiront, se haïront les uns les autres.
bu loolu amee ñu bare dinañu dàggeeku, di booleente tey bañante.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors les pharisiens allèrent se consulter sur les moyens de surprendre jésus par ses propres paroles.
booba farisen ya dem gise, ba xam lu ñu war a def, ngir fiir yeesu ci waxam.
Last Update: 2024-03-03
Usage Frequency: 2
Quality:
alors il le leur livra pour être crucifié. ils prirent donc jésus, et l`emmenèrent.
noonu pilaat jébbal leen yeesu, ngir ñu daaj ko ci bant. bi leen ko pilaat jébbalee, ñu jël ko, yóbbu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors jésus fut emmené par l`esprit dans le désert, pour être tenté par le diable.
bi loolu amee xelum yàlla yóbbu yeesu ca màndiŋ ma, ngir mu jànkoonte ak fiiri seytaane.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors il commença à faire des imprécations et à jurer: je ne connais pas cet homme dont vous parlez.
waaye piyeer daldi giñ ak a waat naan: «xawma nit ki ngay wax.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors il appela les douze, et il commença à les envoyer deux à deux, en leur donnant pouvoir sur les esprits impurs.
noonu mu woo ci moom fukki taalibe ya ak ñaar, jox leen sañ-sañu dàq rab yi, yónni leen, ñu ànd ñaar-ñaar.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors la femme, ayant laissé sa cruche, s`en alla dans la ville, et dit aux gens:
noonu jigéen ja wacc fa njaqam, daldi dem ca dëkk ba ne leen:
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors de nouveau tous s`écrièrent: non pas lui, mais barabbas. or, barabbas était un brigand.
noonu ñu daldi yuuxuwaat: «déedéet, waxunu kii; barabas lanu wax!» fekk barabas moomu taskatu réew la woon.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors ils se mettront à dire aux montagnes: tombez sur nous! et aux collines: couvrez-nous!
bu keroogee,“nit ñi dinañu ne tund yi:‘daanuleen ci sunu kaw!’te naan jànj yi: «“suul-leen nu!»“ “
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors festus, après avoir délibéré avec le conseil, répondit: tu en as appelé à césar; tu iras devant césar.
bi mu waxee loolu, festus gise ak ñi ko wër, mu tontu ko: «dénk nga sa mbir sesaar, kon ci moom ngay dem.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.