From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
je ne suis pas venu appeler à la repentance des justes, mais des pécheurs.
Ñëwuma ngir woo ñi jub, waaye ngir woo bàkkaarkat yi, ñu tuub seeni bàkkaar.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ne vous faites pas appeler directeurs; car un seul est votre directeur, le christ.
buñu leen tudde it ay “njiit,” ndaxte kenn rekk moo di seen njiit, mooy kirist.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
survinrent sa mère et ses frères, qui, se tenant dehors, l`envoyèrent appeler.
noonu ndeyu yeesu ak ay rakkam ñëw, ñu taxaw ci biti, yónnee, woo ko.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il envoya ses serviteurs appeler ceux qui étaient invités aux noces; mais ils ne voulurent pas venir.
noonu mu yónni ay surgaam, ngir ñu woo gan yi ca céet ga, waaye gan yi bëgguñoo ñëw.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mais vous, ne vous faites pas appeler rabbi; car un seul est votre maître, et vous êtes tous frères.
waaye yéen buñu leen wooye “kilifa gi,” ndaxte kenn rekk moo di seen kilifa, te yéen ñépp ay bokk ngeen.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors hérode fit appeler en secret les mages, et s`enquit soigneusement auprès d`eux depuis combien de temps l`étoile brillait.
ci kaw loolu erodd woolu ci kumpa boroom xam-xam ya, di leen ceddowu, ngir xam bu wóor kañ la biddiiw bi feq.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ainsi nous a-t-il appelés, non seulement d`entre les juifs, mais encore d`entre les païens,
te wax ji noo ko moom, nun ñi yàlla woo ci boppam ci biir yawut yi ak ci biir xeet yi ci des.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: