From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
il faut que le laboureur travaille avant de recueillir les fruits.
noonu it beykat bi sonn mooy jëkk a ñam toolam.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il est avant toutes choses, et toutes choses subsistent en lui.
laata dara di am, fekkoon na moom mu nekk, te lépp a ngi jàppoo ci moom.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
si le monde vous hait, sachez qu`il m`a haï avant vous.
«bu leen àddina bañee, xamleen ne, man lañu jëkk a bañ.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
l`officier du roi lui dit: seigneur, descends avant que mon enfant meure.
dagu buur ba neeti ko: «sang bi, ñëwal, bala sama doom di dee.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
en lui dieu nous a élus avant la fondation du monde, pour que nous soyons saints et irrépréhensibles devant lui,
ndaxte ba àddina sosoogul, tànn na nu ci kirist, ngir nu man a teew fa kanamam, sell te ñàkk sikk. ci kaw mbëggeelam
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
avant sa venue, jean avait prêché le baptême de repentance à tout le peuple d`israël.
laata muy ñëw nag, yaxya daan na waare, ne bànni israyil gépp, ñu tuub seeni bàkkaar, te mu sóob leen ci ndox.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
avant que la foi vînt, nous étions enfermés sous la garde de la loi, en vue de la foi qui devait être révélée.
bi ngëm yeesu kirist feeñagul nag, yoon wi da noo tëjoon ràpp, ba kera ngëm di feeñ.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il courut en avant, et monta sur un sycomore pour le voir, parce qu`il devait passer par là.
noonu mu daw, jiituji ca yoon wa, yéeg ci genn garab ngir gis yeesu, ndaxte foofa la naroon a jaar.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
jésus leur dit: en vérité, en vérité, je vous le dis, avant qu`abraham fût, je suis.
yeesu ne leen: «ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, laata ñuy sàkk ibraayma, fekk na ma doon ki ñuy wax maay ki nekk.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
jésus lui dit: je te le dis en vérité, cette nuit même, avant que le coq chante, tu me renieras trois fois.
yeesu ne ko: «ci dëgg maa ngi la koy wax, ci guddi gii, bala ginaar a sab, dinga ma weddi ñetti yoon.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il avait été divinement averti par le saint esprit qu`il ne mourrait point avant d`avoir vu le christ du seigneur.
te xamal na ko ne, du dee mukk te gisul almasib boroom bi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
dès à présent je vous le dis, avant que la chose arrive, afin que, lorsqu`elle arrivera, vous croyiez à ce que je suis.
maa ngi leen koy wax ci teel, bala looloo ñëw, ngir bu ñëwee, ngeen gëm ne, maay ki nekk.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors on fit sortir de la foule alexandre, que les juifs poussaient en avant; et alexandre, faisant signe de la main, voulait parler au peuple.
ci kaw loolu yawut ya jéñ alegsàndar ci kanam, te mbooloo ma di ko xaacu ay ndigal, mu daldi tàllal loxoom, ngir làyyi ca mbooloo ma.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
aussitôt après, il obligea les disciples à monter dans la barque et à passer avant lui de l`autre côté, pendant qu`il renverrait la foule.
bi loolu amee yeesu sant taalibe ya, ñu dugg gaal ga te jàll dex ga, jiituji ko, muy yiwi mbooloo ma.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
avant la fête de pâque, jésus, sachant que son heure était venue de passer de ce monde au père, et ayant aimé les siens qui étaient dans le monde, mit le comble à son amour pour eux.
laata màggalu bésu jéggi ba la woon. yeesu xamoon na ne, waxtu wi mu war a génne àddina, dem ca wetu baay ba, jot na. ku bëgg ñoñam yi nekk ci àddina la, te bëgg na leen ba fa mbëggeel man a yem.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
aussitôt après, il obligea ses disciples à monter dans la barque et à passer avant lui de l`autre côté, vers bethsaïda, pendant que lui-même renverrait la foule.
ci kaw loolu yeesu sant ay taalibeem, ñu dugg ci gaal gi, jàll ba betsayda, bi muy yiwi mbooloo mi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
aussitôt, pour la seconde fois, le coq chanta. et pierre se souvint de la parole que jésus lui avait dite: avant que le coq chante deux fois, tu me renieras trois fois. et en y réfléchissant, il pleurait.
ci saa si ginaar sab ñaareelu yoon. noonu piyeer fàttaliku li ko yeesu wax: «bala ginaar a sab ñaari yoon, dinga ma weddi ñetti yoon.» mu daldi jooy jooy yu metti.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: