Results for c’est ma sœur translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

car christ est ma vie, et la mort m`est un gain.

Wolof

ndaxte su ma dundee, kirist laay noyyee, te su ma deeyee, xéewal lay doon ci man.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et il répondit: qui est ma mère, et qui sont mes frères?

Wolof

waaye yeesu tontu leen: «kan mooy sama ndey? Ñan ñooy samay rakk?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais jésus répondit à celui qui le lui disait: qui est ma mère, et qui sont mes frères?

Wolof

waaye yeesu tontu ko ne: «kan mooy sama ndey ak ñan ñooy samay rakk?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je suis le pain vivant qui est descendu du ciel. si quelqu`un mange de ce pain, il vivra éternellement; et le pain que je donnerai, c`est ma chair, que je donnerai pour la vie du monde.

Wolof

man maay ñam wiy dund te wàcce ci asamaan. ku lekk ci ñam wii, dinga dund ba fàww. te it ñam wi may joxeji, sama yaram la; dama koy joxe ngir àddina man a dund.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,788,784,381 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK