Results for charité translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

je vous exhorte donc à faire acte de charité envers lui;

Wolof

kon maa ngi leen di ñaan, ngeen feddali seen mbëggeel ci moom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et qui nous a appris de quelle charité l`esprit vous anime.

Wolof

te moo nu yégal it mbëggeel, gi xelu yàlla mi sol ci yéen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

veillons les uns sur les autres, pour nous exciter à la charité et aux bonnes oeuvres.

Wolof

nanu seet ni nu man a xiirtalante cig mbëggeel ak ci jëf yu baax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

à la piété l`amour fraternel, à l`amour fraternel la charité.

Wolof

yokk ci sopp mbokk, yokk ci bëgg ñépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et la grâce de notre seigneur a surabondé, avec la foi et la charité qui est en jésus christ.

Wolof

te yiwu sunu boroom baawaan na ci man, ànd ak ngëm ak mbëggeel, yi bawoo ci kirist yeesu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

avant tout, ayez les uns pour les autres une ardente charité, car la charité couvre une multitude de péchés.

Wolof

li gën a am solo mooy, ngeen bëggante mbëggeel gu tar, ndax mbëggeel day suul bàkkaar yu bare.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais que, professant la vérité dans la charité, nous croissions à tous égards en celui qui est le chef, christ.

Wolof

waaye dinanu wax dëgg, ëmb ko ci mbëggeel, bay màgg ci fànn gu ne ci sunu bokk ci kirist. mooy bopp,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

elle sera néanmoins sauvée en devenant mère, si elle persévère avec modestie dans la foi, dans la charité, et dans la sainteté.

Wolof

teewul jigéen dina mucc ci wasin, su saxee ci ngëm ak mbëggeel, di ku sell te maandu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

dis que les vieillards doivent être sobres, honnêtes, modérés, sains dans la foi, dans la charité, dans la patience.

Wolof

maanaa, na góor ñu mag ñi foog, am faayda te maandu, di ñu wér ci seen ngëm, seen mbëggeel ak seen muñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est pourquoi moi aussi, ayant entendu parler de votre foi au seigneur jésus et de votre charité pour tous les saints,

Wolof

bi ma déggee nag seen ngëm ci boroom bi yeesu ak seen mbëggeel ci gaayi yàlla yu sell yépp,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

par la pureté, par la connaissance, par la longanimité, par la bonté, par un esprit saint, par une charité sincère,

Wolof

nu ngi rafetal sunu yen ci dund gu sell, ci xam-xam, muñ ak laabiir, ci xel mu sell mi ak ci mbëggeel gu raxul njublaŋ,

Last Update: 2023-12-17
Usage Frequency: 2
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

French

pour ce qui concerne les viandes sacrifiées aux idoles, nous savons que nous avons tous la connaissance. -la connaissance enfle, mais la charité édifie.

Wolof

léegi nag, ci li jëm ci yàpp wi ñu jébbal xërëm yi: nun ñépp am nanu xam-xam, loolu dëgg la. xam-xam day tax ba nit yég boppam, waaye mbëggeel day yékkati ngëm.

Last Update: 2024-02-16
Usage Frequency: 4
Quality:

French

mais nous qui sommes du jour, soyons sobres, ayant revêtu la cuirasse de la foi et de la charité, et ayant pour casque l`espérance du salut.

Wolof

waaye nun ñiy waa bëccëg, nanu maandu te ràngoo ngir xare bi: ngëm ak mbëggeel, muy kiiraayu dënn, ak kóoluteg mucc, muy mbaxanam xare.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

donnez-leur donc, à la face des Églises, la preuve de votre charité, et montrez-leur que nous avons sujet de nous glorifier de vous.

Wolof

na seen teeru firndeel nag seen mbëggeel ci kanamu mboolooy ñi gëm, te dëggal leen ne, noo yey wóolu leen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais timothée, récemment arrivé ici de chez vous, nous a donné de bonnes nouvelles de votre foi et de votre charité, et nous a dit que vous avez toujours de nous un bon souvenir, désirant nous voir comme nous désirons aussi vous voir.

Wolof

waaye léegi timote bawoo na ci yéen, indaale xebaar yu neex ci seen ngëm ak seen mbëggeel; xamal na nu ne, yéena ngi am pàttaliku yu rafet ci nun te namm nu lool, ni nu leen namme yéen itam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est de préférence au nom de la charité que je t`adresse une prière, étant ce que je suis, paul, vieillard, et de plus maintenant prisonnier de jésus christ.

Wolof

waaye dama lay ñaan ci mbëggeel gi nu séq, man pool màggat, mi ñu tëj kaso ci turu kirist.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin qu`ils aient le coeur rempli de consolation, qu`ils soient unis dans la charité, et enrichis d`une pleine intelligence pour connaître le mystère de dieu, savoir christ,

Wolof

ngir ngeen am fit te nekk benn ci mbëggeel, ngir dajal noonu xam-xam bu mat, ba xam kumpag yàlla, di kirist.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,790,985,715 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK