From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
celui qui vaincra héritera ces choses; je serai son dieu, et il sera mon fils.
ku daan, dinga am cér ci mbir yii. dinaa nekk yàlla sa boroom, te dinga nekk doom ci man.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
enfin, il envoya vers eux son fils, en disant: ils auront du respect pour mon fils.
mujj mu yónni doomam naan: “xëy na ñu weg sama doom.”
Last Update: 2024-04-13
Usage Frequency: 31
Quality:
et de la nuée sortit une voix, qui dit: celui-ci est mon fils élu: écoutez-le!
noonu baat jibe ca niir wa naan: «kii mooy sama doom ji ma fal; dégluleen ko.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car mon fils que voici était mort, et il est revenu à la vie; il était perdu, et il est retrouvé. et ils commencèrent à se réjouir.
ndaxte sama doom jii dafa dee woon te dundaat na, dafa réeroon te feeñ na.” noonu ñu tàmbalee bànneexu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et un homme de la foule lui répondit: maître, j`ai amené auprès de toi mon fils, qui est possédé d`un esprit muet.
kenn ci mbooloo mi tontu ko ne: «kilifa gi, rab jàpp na sama doom, ba luuloo ko. saa su ko jàppee, daf koy daaneel ci suuf, gémmiñ gi di fuur, muy yéyu, ne jàdd. Ñaan naa say taalibe, ñu dàq ko, waaye mënuñu ko.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il avait encore un fils bien-aimé; il l`envoya vers eux le dernier, en disant: ils auront du respect pour mon fils.
«noonu mu dese ko kenn rekk, di doomam ji mu bëgg. mujj mu yónni ko naan: “xëy na ñu weg sama doom.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car auquel des anges dieu a-t-il jamais dit: tu es mon fils, je t`ai engendré aujourd`hui? et encore: je serai pour lui un père, et il sera pour moi un fils?
ndaxte yàlla musul a wax kenn ci malaaka yi ne:«yaa di sama doom,maa di sa baay tey.» musul ne ci mbirum kenn ci ñoom it:«man yàlla, dinaa doon baay ci moom,mu nekk doom ci man.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.