From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
il en prit, et il mangea devant eux.
mu jël ko, lekk ci seen kanam.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
cela est bon et agréable devant dieu notre sauveur,
loolu mooy li rafet te neex yàlla sunu musalkat,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et voici, un homme hydropique était devant lui.
faf am ca kanamam nit ku feebaroon, ay tànkam newi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
la crainte de dieu n`est pas devant leurs yeux.
te ragal yàlla sore na seen xol.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et toute la ville était rassemblée devant sa porte.
ba dëkk bi bépp dajaloo ci buntu kër gi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
a cause de cela, je fléchis les genoux devant le père,
moo tax maa ngi sukk, jublu ci yàlla baay
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ayant vu jésus de loin, il accourut, se prosterna devant lui,
bi mu gisee yeesu fu sore nag, mu daldi dawsi, sukk fa kanamam,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
elles trouvèrent que la pierre avait été roulée de devant le sépulcre;
bi ñu agsee, ñu fekk ñu béraŋ doj, wa uboon bàmmeel ba.
Last Update: 2024-04-17
Usage Frequency: 3
Quality:
mais celui qui me reniera devant les hommes sera renié devant les anges de dieu.
waaye ku ma gàntu ci kanamu nit ñi, dinañu la gàntu ci kanamu malaakay yàlla yi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
en marchant devant lui dans la sainteté et dans la justice tous les jours de notre vie.
nu sell te jub ci kanamam sunu giiru dund.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ce sont les deux oliviers et les deux chandeliers qui se tiennent devant le seigneur de la terre.
Ñaari seede ya nag ñoo di ñaari garabu oliw yeek ñaari làmpu diwlin, yi taxaw ci kanam boroom suuf si.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
après avoir ainsi parlé, jésus marcha devant la foule, pour monter à jérusalem.
bi mu waxee loolu ba noppi, yeesu dafa daldi jiitu, jëm yerusalem.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car nous recherchons ce qui est bien, non seulement devant le seigneur, mais aussi devant les hommes.
danuy fexee def li jub, du ci kanam yàlla rekk, waaye it ci kanam nit ñi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors leurs yeux s`ouvrirent, et ils le reconnurent; mais il disparut de devant eux.
bi mu defee loolu, lépp leer ci seeni bët, ñu daldi ko xàmmi. waaye yeesu ne mes, gisatuñu ko.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors vous vous mettrez à dire: nous avons mangé et bu devant toi, et tu as enseigné dans nos rues.
bu ko defee dingeen tàmbalee naan: “noo doon bokk di lekk ak di naan, te jàngale nga ci sunuy pénc.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bien-aimés, si notre coeur ne nous condamne pas, nous avons de l`assurance devant dieu.
samay soppe, bu nu sunu xol daanul, kon man nanoo jege yàlla ak kóolute.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
approchez-vous de lui, pierre vivante, rejetée par les hommes, mais choisie et précieuse devant dieu;
kon nag ñëwleen ci moom; nit ñi bañ nañu ko, waaye yàlla fal na ko te teral ko. mi ngi mel ni doju tabax, waaye doj wuy dund la,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
afin de faire paraître devant lui cette Église glorieuse, sans tache, ni ride, ni rien de semblable, mais sainte et irrépréhensible.
noonu dina ko jël, mu mel ni séet bu ñu waajal, di mbooloom mu soloo ndam, te gàkkul, rasul, taqul leneen, waaye mu sell te amul sikk.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors festus, après avoir délibéré avec le conseil, répondit: tu en as appelé à césar; tu iras devant césar.
bi mu waxee loolu, festus gise ak ñi ko wër, mu tontu ko: «dénk nga sa mbir sesaar, kon ci moom ngay dem.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ayant ainsi parlé, il prit du pain, et, après avoir rendu grâces à dieu devant tous, il le rompit, et se mit à manger.
bi mu waxee loolu, mu fab mburu, sant yàlla ci kanamu ñépp, damm ko, daldi ko lekk.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: