Results for devint translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

jude, fils de jacques; et judas iscariot, qui devint traître.

Wolof

yudaa doomu saag, ak yudaa iskariyo, mi mujj a wor.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

lorsqu`il entendit ces paroles, il devint tout triste; car il était très riche.

Wolof

bi nit ka déggee loolu, mu am tiis, ndaxte ku bare woon alal la.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

Étant en agonie, il priait plus instamment, et sa sueur devint comme des grumeaux de sang, qui tombaient à terre.

Wolof

ci biir tiis, yeesu gën a sawar ci ñaan gi, ñaqam mel ni lumbi deret dal ci suuf.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

quelque temps après, Élisabeth, sa femme, devint enceinte. elle se cacha pendant cinq mois, disant:

Wolof

bi mbir yooyu weesoo, elisabet jabaram ëmb, di ko nëbb lu mat juróomi weer

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

le second ange sonna de la trompette. et quelque chose comme une grande montagne embrasée par le feu fut jeté dans la mer; et le tiers de la mer devint du sang,

Wolof

Ñaareelu malaaka ma wol liitam. noonu ñu sànni lu mel ni tundu safara wu réy, mu daanu ci géej gi, benn ci ñetti xaaju géej gi soppiku deret,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est pourquoi il est écrit: le premier homme, adam, devint une âme vivante. le dernier adam est devenu un esprit vivifiant.

Wolof

mbind mi nee na: «nit ku jëkk ka, aadama, doon na boroom ruu,» waaye aadama mu mujj mi doon na xel muy joxe dund.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

alors il dit à l`homme: Étends ta main. il l`étendit, et elle devint saine comme l`autre.

Wolof

noonu yeesu ne nit ka: «tàllalal sa loxo!» mu tàllal ko nag, loxoom daldi wér, mel ni ba ca des.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je regardai, quand il ouvrit le sixième sceau; et il y eut un grand tremblement de terre, le soleil devint noir comme un sac de crin, la lune entière devint comme du sang,

Wolof

ma xool, ba muy dindi juróom-benneelu tayu ga. noonu mu am yengu-yengub suuf bu mag, jant bi ñuul ni këriñ, weer wi xonq curr ni deret.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est par la foi que noé, divinement averti des choses qu`on ne voyait pas encore, et saisi d`une crainte respectueuse, construisit une arche pour sauver sa famille; c`est par elle qu`il condamna le monde, et devint héritier de la justice qui s`obtient par la foi.

Wolof

ngëm moo tax ba, bi yàlla yégalee nóoyin lu jiitu ci mbir yi dikkagul, mu ragal ba defar gaal ngir musal njabootam. ngëmam moo tax mu yey niti àddina, ba noppi jot njubte, li yàllay joxe ci kaw ngëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,788,723,035 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK