From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
qui connais sa volonté, qui apprécies la différence des choses, étant instruit par la loi;
xam nga coobareem, ndaxte jàng nga ci yoonu musaa, ba fonk yëf yi gën a baax.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il n`a fait aucune différence entre nous et eux, ayant purifié leurs coeurs par la foi.
gënalantewu nu ak ñoom, ci li mu sellal seen xol ci kaw ngëm.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il n`y a aucune différence, en effet, entre le juif et le grec, puisqu`ils ont tous un même seigneur, qui est riche pour tous ceux qui l`invoquent.
ndax ñépp a yem ci kanam yàlla, muy yawut mbaa ku dul yawut, ndax kenn rekk mooy sunu boroom nun ñépp, te ku yéwén la ci képp ku koy ñaan.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: