Results for eu, eu translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

et, comme cela n`a pas eu lieu sans serment,

Wolof

te rax-ca-dolli ngiñ ànd na ci. ndaxte ñi soqikoo ci lewi doon nañu ay saraxalekat te kenn giñul.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

eu égard à votre vie passée, du vieil homme qui se corrompt par les convoitises trompeuses,

Wolof

maanaam ngeen yulli seen jikko ju bon, ji ngeen judduwaale te daan fés ci seeni jëf, te muy gën a yées, moom ak i bëgg-bëggam yuy naxe kese.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

s`ils avaient eu en vue celle d`où ils étaient sortis, ils auraient eu le temps d`y retourner.

Wolof

bu ñu nammoon réew mi ñu jóge, kon dinañu am jotu dellu fa.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car il est impossible que ceux qui ont été une fois éclairés, qui ont goûté le don céleste, qui ont eu part au saint esprit,

Wolof

li nu war a jëme kanam mooy lii: su amee ay nit ñu yàlla xas a leeral ba noppi, ñu mos mayu yàlla gi, am wàll ci xelam mu sell,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ils nous recommandèrent seulement de nous souvenir des pauvres, ce que j`ai bien eu soin de faire.

Wolof

li ñu doon laaj rekk moo di, nuy fàttaliku seen aji néew doole yi, fekk sax laxasu woon naa ci def ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

de plus, il y a eu des sacrificateurs en grand nombre, parce que la mort les empêchait d`être permanents.

Wolof

te it yeneen saraxalekat yi dañoo bare woon, ndaxte dee moo daan tax duñu man a sax ci seen liggéey.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car je n`ai pas eu la pensée de savoir parmi vous autre chose que jésus christ, et jésus christ crucifié.

Wolof

dogu woon naa ci bañ a xam dara ci seen biir lu dul yeesu kirist, te muy ki ñu rey ca bant ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ils vinrent auprès de jésus, et ils virent le démoniaque, celui qui avait eu la légion, assis, vêtu, et dans son bon sens; et ils furent saisis de frayeur.

Wolof

Ñu ñëw nag ci yeesu, gis ka rab ya jàppoon toog, sol ay yére te ànd ak sagoom. Ñu daldi ragal.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car souvent il avait eu les fers aux pieds et avait été lié de chaînes, mais il avait rompu les chaînes et brisé les fers, et personne n`avait la force de le dompter.

Wolof

ndaxte ay yoon yu bare jéngoon nañu ko te yeew ko ak ay càllala, waaye waa ji daldi dagg càllala yi te damm jéng yi, ba kenn amul woon kàttanu téye ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

abraham répondit: mon enfant, souviens-toi que tu as reçu tes biens pendant ta vie, et que lazare a eu les maux pendant la sienne; maintenant il est ici consolé, et toi, tu souffres.

Wolof

ibraayma ne ko: “sama doom, fàttalikul ne, jot nga sa bànneex ci àddina, fekk lasaar dëkk ci tiis. looloo tax xolam sedd fii, yaw nag, ngay sonn.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
8,884,442,587 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK