From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
le serviteur dit: maître, ce que tu as ordonné a été fait, et il y a encore de la place.
«surga ba ñëwaat ne ko: “sang bi, def naa li nga ma sant, waaye bérab bi feesul.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ils lui dirent: seigneur, il a dix mines. -
Ñu ne ko: “sang bi, am na fukki libidoor ba noppi.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
le père ne juge personne, mais il a remis tout jugement au fils,
baay bi du àtte kenn; àtte bi yépp, jox na ko doom ji,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
doit-il de la reconnaissance à ce serviteur parce qu`il a fait ce qui lui était ordonné?
li surga ba topp ndigal, ndax tax na mu yelloo ngërëm? déedéet.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il a rassasié de biens les affamés, et il a renvoyé les riches à vide.
Ñi xiif, reggal na leen ak ñam wu neex,te dàq boroom alal yi,ñu daw ak loxoy neen.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car christ est mort et il a vécu, afin de dominer sur les morts et sur les vivants.
loolu sax moo waral kirist dee te dundaat, ngir man a nekk boroomu ñi dee ak ñiy dund.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car le seigneur exécutera pleinement et promptement sur la terre ce qu`il a résolu.
ndaxte li boroom bi dogal ci àddina,dina ko gaaw a def, te dina mat sëkk.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
c`est pourquoi il est dit: Étant monté en haut, il a emmené des captifs, et il a fait des dons aux hommes.
looloo tax mbind mi ne:«yéeg na ba ca fa gën a kawe,yóbbaale mbooloom noon mu bare, mi mu noot,tey séddale nit ñi ay may.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car si vous croyiez moïse, vous me croiriez aussi, parce qu`il a écrit de moi.
bu ngeen gëmoon musaa, dingeen ma gëm man itam, ndaxte seedeel na ma.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car il a parlé quelque part ainsi du septième jour: et dieu se reposa de toutes ses oeuvres le septième jour.
am na fu ñu wax ci mbind mi ne:«yàlla noppalu na ci liggéeyam béppca juróom-ñaareelu fan ba.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il y a encore devant le trône comme une mer de verre, semblable à du cristal. au milieu du trône et autour du trône, il y a quatre êtres vivants remplis d`yeux devant et derrière.
amoon na it ca kanamu gàngune ma lu mel ni géej gu leer ni weer bu set, ba mel ni seetu. ci li wër gàngune ma, sës rëkk, amoon na fa ñeenti mbindeef yu fees ak ay bët ci kanam ak ci gannaaw.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
puisque nous sommes interrogés aujourd`hui sur un bienfait accordé à un homme malade, afin que nous disions comment il a été guéri,
bu fekkee ne xettali nit ku wopp, ba mu wér, moo tax ngeen dëj nu ci pénc mi tey,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car il a accueilli notre demande, et c`est avec un nouveau zèle et de son plein gré qu`il part pour aller chez vous.
bi nu ko laajee, mu ñëw ci yéen, nangu na, te rax-ca-dolli cawarteem tollu na, ba nu man a wax ne, ci coobarey boppam la jóge, jëm ci yéen.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
c`est la grâce que le seigneur m`a faite, quand il a jeté les yeux sur moi pour ôter mon opprobre parmi les hommes.
te naan: «lii mooy yiw wi ma boroom bi defal, ba fajal ma li doon sama gàcce ci nit ñi!»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
c`est pourquoi ses parents dirent: il a de l`âge, interrogez-le lui-même.
looloo tax waajur ya ne: «laajleen ko; magum jëmm la.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mais il a dit au fils: ton trône, ô dieu est éternel; le sceptre de ton règne est un sceptre d`équité;
waaye ci wàllu doom ji, lii la ko yàlla wax:«yaw yàlla, dinga toog ci jal bi ba fàww,ci njubte ngay nguuru.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car on donnera à celui qui a, et il sera dans l`abondance, mais à celui qui n`a pas on ôtera même ce qu`il a.
ndaxte ku am dinañu la dolli, ba nga barele, waaye ku amul, li nga am as néew sax, dinañu ko nangu.
Last Update: 2023-07-29
Usage Frequency: 1
Quality:
alors le souverain sacrificateur déchira ses vêtements, disant: il a blasphémé! qu`avons-nous encore besoin de témoins? voici, vous venez d`entendre son blasphème. que vous en semble?
bi mu déggee loolu, saraxalekat bu mag ba daldi mer lool, ba xotti ay yéreem, daldi ne: «weddi na yàlla, lu nu doyeeti seede? dégg ngeen ni mu weddee.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.